Results for per me sei importante translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

per me infatti il vivere è cristo e il morire un guadagno

Wolof

ndaxte su ma dundee, kirist laay noyyee, te su ma deeyee, xéewal lay doon ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

rispose gesù: «questa voce non è venuta per me, ma per voi

Wolof

waaye yeesu ne leen: «taxuma baat boobu jolli, waaye yéena tax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e io preparo per voi un regno, come il padre l'ha preparato per me

Wolof

man nag jox naa leen sañ-sañu nguuru, ni ma ko sama baay joxe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chi vorrà salvare la propria vita, la perderà, ma chi perderà la propria vita per me, la salverà

Wolof

ndaxte koo xam ne bëgg ngaa rawale sa bakkan, dinga ko ñàkk, waaye ku ñàkk sa bakkan ngir man, dinga ko jotaat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e anche per me, perché quando apro la bocca mi sia data una parola franca, per far conoscere il mistero del vangelo

Wolof

te buleen ma ci fàtte, ngir waxtu wu ma ubbee sama gémmiñ, ma am lu ma wax, ba man a xamle ak fit wu dëgër mbóoti xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

come il padre, che ha la vita, ha mandato me e io vivo per il padre, così anche colui che mangia di me vivrà per me

Wolof

baay bi ma yónni mu ngi dund, te maa ngi dund jaarale ko ci moom; noonu itam ku may lekk dina dund jaarale ko ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la tua carità è stata per me motivo di grande gioia e consolazione, fratello, poiché il cuore dei credenti è stato confortato per opera tua

Wolof

ci dëgg-dëgg sa mbëggeel bégal na ma bu baax, ba dëfël sama xol; ndaxte xam naa, sama mbokk, ni nga féexale xoli gaayi yàlla yu sell yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

rispose simone: «pregate voi per me il signore, perché non mi accada nulla di ciò che avete detto»

Wolof

simoŋ nag ne leen: «Ñaanal-leen ma ci boroom bi, ngir mu fegal ma li ngeen wax.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quanto a me invece non ci sia altro vanto che nella croce del signore nostro gesù cristo, per mezzo della quale il mondo per me è stato crocifisso, come io per il mondo

Wolof

man ci sama wàllu bopp, duma bàkku mukk su dul ci deewu sunu boroom yeesu kirist, ba ñu ko daajee ca bant ba. deeyam moo tax ma mel ni ku dee ci yëfi àddina; yëfi àddina dee ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

vi esorto perciò, fratelli, per il signore nostro gesù cristo e l'amore dello spirito, a lottare con me nelle preghiere che rivolgete per me a dio

Wolof

gannaaw loolu bokk yi, maa ngi leen di ñaan ci turu sunu boroom yeesu kirist ak ci bëggante, gi xelu yàlla mi def ci nun, ngeen defal ma lii: àndleen ak man, nu tuur sunu ñaq ci ñaan yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma il signore disse: «và, perché egli è per me uno strumento eletto per portare il mio nome dinanzi ai popoli, ai re e ai figli di israele

Wolof

waaye boroom bi ne ko: «demal, ndaxte maa ko tànn, muy sama jëfandukaay, ngir yóbbu sama tur fa kanam ñi nekkul yawut ak fa kanam buur yi ak bànni israyil.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e non solo con la sua venuta, ma con la consolazione che ha ricevuto da voi. egli ci ha annunziato infatti il vostro desiderio, il vostro dolore, il vostro affetto per me; cosicché la mia gioia si è ancora accresciuta

Wolof

te du ci ñëwam rekk sax waaye ci li ngeen dëfël xolam. yégal na nu seen nammeel ci nun, seen réccu ak seen farlu jëm ci man, ba sama mbég gën cee yokku.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ciò che è bene è allora diventato morte per me? no davvero! e' invece il peccato: esso per rivelarsi peccato mi ha dato la morte servendosi di ciò che è bene, perché il peccato apparisse oltre misura peccaminoso per mezzo del comandamento

Wolof

ndax kon lu baax moo ma tàbbal ci dee? mukk! bàkkaar a ko def, ngir jikkoom feeñ; dafa gis ci lu baax loolu bunt bu mu man a jaar, ba rey ma. noonu ndigalu yàlla tax na, bàkkaar fés, bon ba jéggi dayo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,793,429,190 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK