Results for preparato translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

e io preparo per voi un regno, come il padre l'ha preparato per me

Wolof

man nag jox naa leen sañ-sañu nguuru, ni ma ko sama baay joxe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il discepolo non è da più del maestro; ma ognuno ben preparato sarà come il suo maestro

Wolof

taalibe gënul kilifaam, waaye taalibe bu jàng ba wàcc, dina yem ak kilifaam demin.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

per questo, entrando nel mondo, cristo dice: un corpo invece mi hai preparato

Wolof

looloo tax bi muy wàcc àddina, kirist nee na:«bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

giovanni aveva preparato la sua venuta predicando un battesimo di penitenza a tutto il popolo d'israele

Wolof

laata muy ñëw nag, yaxya daan na waare, ne bànni israyil gépp, ñu tuub seeni bàkkaar, te mu sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la donna invece fuggì nel deserto, ove dio le aveva preparato un rifugio perché vi fosse nutrita per milleduecentosessanta giorni

Wolof

gannaaw loolu jigéen ja daw, dem ca màndiŋ ma, ca dalukaay ba ko yàlla waajaloon ngir mu nekk fa, ñu dundal ko fa diirub junni ak ñaari téeméeri fan ak juróom-benn-fukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quando sarò andato e vi avrò preparato un posto, ritornerò e vi prenderò con me, perché siate anche voi dove sono io

Wolof

te su ma leen defaralee bérab booba ba noppi, dinaa dellusi, yóbbaale leen, ba fu ma nekk, ngeen nekk fa, yéen itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il primo giorno dopo il sabato, di buon mattino, si recarono alla tomba, portando con sé gli aromi che avevano preparato

Wolof

bés bu jëkk ca ayu-bés ga, jigéen ña jóg ca fajar, dem ca bàmmeel ba. Ñu ngi yoroon cuuraay lu ñu defaroon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma sedere alla mia destra o alla mia sinistra non sta a me concederlo; è per coloro per i quali è stato preparato»

Wolof

waaye toog ci sama ndeyjoor mbaa sama càmmooñ, du man maa koy maye. Ñi ñu ko waajal rekk a ko yelloo.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ora invece essi aspirano a una migliore, cioè a quella celeste. per questo dio non disdegna di chiamarsi loro dio: ha preparato infatti per loro una città

Wolof

waaye ñu ngi doon séentu réew mu gën, maanaam mi nekk ci asamaan. looloo tax yàlla rusul ñu koy wooye seen yàlla, ndaxte defaral na leen ab dëkk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora il re dirà a quelli che stanno alla sua destra: venite, benedetti del padre mio, ricevete in eredità il regno preparato per voi fin dalla fondazione del mondo

Wolof

«noonu buur bi dina wax ñi féete ndeyjoor: “agsileen, yéen ñi sama baay barkeel, jël-leen nguur, gi ñu leen waajal li dale ci njàlbéenug àddina.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

di nuovo mandò altri servi a dire: ecco ho preparato il mio pranzo; i miei buoi e i miei animali ingrassati sono gia macellati e tutto è pronto; venite alle nozze

Wolof

kon mu yónneeti yeneen surga ne leen: “bu ngeen demee, yégal-leen gan yi sama woote bii: ‘reer yi noppi na, reylu naa samay nag ak samay jur gu duuf; lépp sotti na, ñëwleen ci reer yi.’ ”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

com'è scritto nel libro degli oracoli del profeta isaia: preparate la via del signore, raddrizzate i suoi sentieri

Wolof

loolu lañu bind ci téereb waxi yonent yàlla esayi naan:«am na baat buy xaacu ca màndiŋ ma ne:“xàll-leen yoonu boroom bi,jubal-leen fi muy jaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,241,455 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK