Results for quando sei nato translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

trovatolo di là dal mare, gli dissero: «rabbì, quando sei venuto qua?»

Wolof

bi ñu fekkee yeesu ca geneen wàllu dex ga, ñu ne ko: «kilifa gi, kañ nga fi ñëw?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

impossibile! resti invece fermo che dio è verace e ogni uomo mentitore, come sta scritto: e trionfi quando sei giudicato.

Wolof

mukk! su ñépp nekkoon ay naaféq, du tere yàlla nekk dëgg. moom la mbind mi wax ci yàlla ne:«loo wax, ñépp ànd ci,te ku layoo ak yaw, nga yey ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e avete gia dimenticato l'esortazione a voi rivolta come a figli: e non ti perdere d'animo quando sei ripreso da lui

Wolof

te fàtte ngeen li leen yàlla dénk ni baay ak ay doomam naan:«sama doom, bul fonkadi yarub boroom bimbaa ngay xàddi, bu lay yedd,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli replicarono: «sei nato tutto nei peccati e vuoi insegnare a noi?». e lo cacciarono fuori

Wolof

Ñu tontu ko ne: «yaw, ci biir bàkkaar nga juddoo, ba noppi di nu jàngal?» noonu ñu dàq ko ca jàngu ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

invece quando sei invitato, và a metterti all'ultimo posto, perché venendo colui che ti ha invitato ti dica: amico, passa più avanti. allora ne avrai onore davanti a tutti i commensali

Wolof

waaye bu ñu la wooyee, demal ca toogu bu gannaawe ba. bu ko defee ki la woo, bu agsee ne la: “sama xarit, àggal ca kaw.” loolu dina la sagal ci ñi nga toogandool ci lekkukaay bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,775,871,144 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK