Results for quella translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

così paolo uscì da quella riunione

Wolof

noonu pool génn ci seen biir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e vi fu grande gioia in quella città

Wolof

noonu mbég mu réy tàbbi ca dëkk ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e se ne sparse la fama in tutta quella regione

Wolof

noonu xebaaru li mu def daldi siiw ca réew ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quella, udito ciò, si alzò in fretta e andò da lui

Wolof

bi maryaama déggee loolu, mu daldi jóg, gaawantoo dem ca yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e le impose le mani. subito quella si raddrizzò e glorificava dio

Wolof

noonu mu teg ko ay loxoom, soxna sa siggi ca saa sa, di màggal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

esattamente come dice osea: e mia diletta quella che non era la diletta

Wolof

moom la wax ci téereb ose ne:«Ñi nekkul woon sama xeetdinaa leen ko def,ñi bokkul woon ci sama mbëggeel,dinaa leen ci boole.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma essi, appena usciti, ne sparsero la fama in tutta quella regione

Wolof

waaye ñu génn rekk, siiwal turam fu nekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

se dunque non siete stati fedeli nella disonesta ricchezza, chi vi affiderà quella vera

Wolof

su fekkeente ne nag jubuleen ci alalu àddina, kon ku leen di dénk alal ju wóor ji?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chiunque cadrà su quella pietra si sfracellerà e a chi cadrà addosso, lo stritolerà»

Wolof

képp ku dal ci doj woowu, dammtoo, te ku mu dal ci sa kaw, rajaxe la.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma quella venne e si prostrò dinanzi a lui dicendo: «signore, aiutami!»

Wolof

waaye jigéen ja ñëw, sukk ci kanamam naan: «sang bi, wallusi ma!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e i demòni presero a scongiurarlo dicendo: «se ci scacci, mandaci in quella mandria»

Wolof

rab ya nag ñaan ko ne: «boo nu dàqee, sànni nu ca géttu mbaam-xuux ya.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

mentre parlava così, venne una nube e li avvolse; all'entrare in quella nube, ebbero paura

Wolof

bi mu koy wax, niir ñëw muur leen, taalibe yi daldi tiit, bi leen niir wa ëmbee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

accade invece quello che predisse il profeta gioele

Wolof

waaye lii mooy li yàlla waxoon, jaarale ko ci yonentam yowel ne:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,793,823,110 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK