Results for vino translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

il vino nuovo bisogna metterlo in otri nuovi

Wolof

waaye dañoo war a def biiñ bu bees ci mbuus yu bees.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e gli offrirono vino mescolato con mirra, ma egli non ne prese

Wolof

Ñu bëgg koo jox biiñ bu ñu boole ak naan gu tudd miir, waaye nanguwu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non dedito al vino, non violento ma benevolo, non litigioso, non attaccato al denaro

Wolof

warul di ab màndikat mbaa xeexkat, waaye na lewet te jàmmu, bañ a bëgge ci xaalis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e non ubriacatevi di vino, il quale porta alla sfrenatezza, ma siate ricolmi dello spirito

Wolof

buleen màndi it ci sangara, liy ndeyi ñaawteef, waaye feesleen ak xel mu sell mi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

perciò è bene non mangiare carne, né bere vino, né altra cosa per la quale il tuo fratello possa scandalizzarsi

Wolof

liy sa warugar mooy nga bañ a fiir sa moroom ci yàpp mbaa ci biiñ mbaa ci leneen lu mu man a doon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allo stesso modo i diaconi siano dignitosi, non doppi nel parlare, non dediti al molto vino né avidi di guadagno disonesto

Wolof

kiy topptoo li mbooloo miy jëfandikoo itam na am faayda te fonk kàddoom; bumu di ku yàqu ci sangara, mbaa ku alal jiital.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e nessuno mette vino nuovo in otri vecchi; altrimenti il vino nuovo spacca gli otri, si versa fuori e gli otri vanno perduti

Wolof

te kenn du def biiñ bu bees ci mbuusi der yu màggat. lu ko moy, biiñ bu bees bi day toj mbuus yi, biiñ bi tuuru, mbuus yi yàqu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e nessuno versa vino nuovo in otri vecchi, altrimenti il vino spaccherà gli otri e si perdono vino e otri, ma vino nuovo in otri nuovi»

Wolof

te kenn du def biiñ bu bees ci mbuusi der yu màggat. lu ko moy, biiñ bi day toj mbuus yi, ba mbuus yi yàqu, ak biiñ bi tuuru. waaye biiñ bu bees, ci mbuus yu bees lañu koy def.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dalla bocca gli esce una spada affilata per colpire con essa le genti. egli le governerà con scettro di ferro e pigerà nel tino il vino dell'ira furiosa del dio onnipotente

Wolof

am na jaasi ju ñaw juy génn ci gémmiñam, ngir dóor xeet yi, mu di leen jiitee yetu weñ, te mooy nappaaje réseñ yi ci segalukaayu mer mu tàng, mu yàlla aji kàttan ji.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

andò dunque di nuovo a cana di galilea, dove aveva cambiato l'acqua in vino. vi era un funzionario del re, che aveva un figlio malato a cafarnao

Wolof

noonu kon mu dellusi kana ci galile, dëkk ba mu soppe woon ndox ma biiñ. amoon na benn dagu buur bu dëkkoon kapernawum te doomam feebar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,920,046,710 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK