From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
marcus aristarchus demas lucas adiutores me
samay àndandoo ci liggéey bi, màrk, aristàrk, demas ak luug, ñu ngi lay nuyu.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
salutate priscam et aquilam adiutores meos in christo ies
nuyul-leen ma pirsil ak akilas, samay nawle ci liggéeyu kirist yeesu.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
dei enim sumus adiutores dei agricultura estis dei aedificatio esti
nu ngi liggéeyandoo ci liggéeyu yàlla; yéenay toolu yàlla, yéenay taaxum yàlla.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
non quia dominamur fidei vestrae sed adiutores sumus gaudii vestri nam fide stetisti
du caageen nag noo leen bëgg a noot ci lu jëm ci seen ngëm, waaye nu ngi liggéeyandoo ak yéen ngir seen mbég, ndaxte ci ngëm ngeen sax.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et iesus qui dicitur iustus qui sunt ex circumcisione hii soli sunt adiutores in regno dei qui mihi fuerunt solaci
yeesu mi ñuy dàkkentale yustus, moom it mu ngi leen di nuyu. Ñoom rekk ñooy yawut yiy liggéeyandook man ngir nguuru yàlla, te ñoo féexal sama xol.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: