Results for bonus translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

labora sicut bonus miles christi ies

Wolof

bokkal ak man tiis, di jàmbaar ci toolu xareb kirist yeesu,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ego sum pastor bonus et cognosco meas et cognoscunt me mea

Wolof

«man maay sàmm bu baax bi. ni ma xame baay bi te baay bi xame ma ni, noonu laa xame samay xar, te ñoom it ni lañu ma xame. te it kat dinaa joxe sama bakkan ngir xar yi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ego sum pastor bonus bonus pastor animam suam dat pro ovibu

Wolof

«man maay sàmm bu baax bi. sàmm bu baax bi day joxe bakkanam ngir ay xaram.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

iesus autem dixit ei quid me dicis bonum nemo bonus nisi unus deu

Wolof

yeesu tontu ko: «lu tax nga wooye ma ku baax ki? yàlla rekk a baax.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dixit autem ei iesus quid me dicis bonum nemo bonus nisi solus deu

Wolof

yeesu tontu ko: «lu tax nga wooye ma ku baax? yàlla rekk a baax.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

aut non licet mihi quod volo facere an oculus tuus nequam est quia ego bonus su

Wolof

ndax sañumaa def ak sama alal li ma neex? walla ndax danga am kiñaan ci li ma yéwén?”

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quia erat vir bonus et plenus spiritu sancto et fide et adposita est turba multa domin

Wolof

ndaxte nit ku baax la woon te fees ak xel mu sell mi ak ngëm; noonu mbooloo mu bare dolliku ci boroom bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

haec proponens fratribus bonus eris minister christi iesu enutritus verbis fidei et bonae doctrinae quam adsecutus e

Wolof

saxal ci digal bokk yi loolu nag, kon dinga nekk jawriñu kirist yeesu ju baax ju regg ci kàdduy yoonu ngëm wi ak njàngale mu rafet, mi nga xam bu wér.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

bonus homo de bono thesauro cordis sui profert bonum et malus homo de malo profert malum ex abundantia enim cordis os loquitu

Wolof

noonu nit ku baax, lu baax lay wax, ndax loolu la denc ci xolam, te nit ku bon, lu bon lay wax, ndaxte denc na lu bon ci xolam. ndaxte gémmiñ, la fees xolam lay wax.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et murmur multus de eo erat in turba; quidam enim dicebant quia bonus est alii autem dicebant non sed seducit turba

Wolof

ca biir mbooloo ma ñu ngi doon déeyante, di wax ci ay mbiram. Ñii naan: «nit ku baax la.» Ñee naan: «déedéet, day nax nit ñi.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,277,755 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK