From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
salutate apellen probum in christ
ak it apeles, mi ngëmam dëggu, ba yelloo kóolute.nuyul-leen ma it waa kër aristobul,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
imitatores mei estote sicut et ego christ
royleen ma nag, ni may roye kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
in quibus estis et vos vocati iesu christ
te ci ngeen bokk, yéen ñi yàlla woo, ngeen nekk ci kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ergo fides ex auditu auditus autem per verbum christ
kon boog ngëm ci kaw dégg lay juddoo, te dégg sosoo ci xebaaru kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ad consummationem sanctorum in opus ministerii in aedificationem corporis christ
maye na leen, ngir ñu waajal gaayi yàlla yu sell yi, ñu man a bey seen sas ci taxawal mbooloom kirist, di jëmmam.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
eram autem ignotus facie ecclesiis iudaeae quae erant in christ
waaye ba tey mboolooy ñi gëm kirist ci diiwaanu yude xamuñu ma woon.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
gratia vobis et pax a deo patre nostro et domino iesu christ
na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 4
Quality:
dominus autem dirigat corda vestra in caritate dei et patientia christ
na boroom bi gindi seeni xol ci mbëggeelu yàlla ak muñu kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
huius rei gratia flecto genua mea ad patrem domini nostri iesu christ
moo tax maa ngi sukk, jublu ci yàlla baay
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
aemulor enim vos dei aemulatione despondi enim vos uni viro virginem castam exhibere christ
dama leen di fiire ak fiiraange gu jóge ca yàlla, ndaxte dama leen a bëgg a jébbal jenn jëkkër kepp, muy kirist, ngeen set ni janq.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ad quod et vocavit vos per evangelium nostrum in adquisitionem gloriae domini nostri iesu christ
te yàlla woo na leen ci loolu jaarale ko ci xebaar bu baax, bi nu leen doon yégal, ngir ngeen bokk ci ndamu sunu boroom yeesu kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
in quo et circumcisi estis circumcisione non manufacta in expoliatione corporis carnis in circumcisione christ
ndax seen ngëm ci moom xaraf ngeen xaraf bu loxol nit deful, maanaam kirist summil na leen dooley bàkkaar, ji moomoon seen yaram. loolu mooy xaraf, bi kirist def.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
cui autem aliquid donatis et ego nam et ego quod donavi si quid donavi propter vos in persona christ
ku ngeen baal, ma baal ko itam. man nag, su ma baalee --fekk am lu ma war a baale — yéena tax ma def ko ci kanamu kirist,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
benedictus deus et pater domini nostri iesu christi qui benedixit nos in omni benedictione spiritali in caelestibus in christ
cant ñeel na yàlla baayu sunu boroom yeesu kirist, mi nu sotti ci sunu bokk ci kirist lépp luy barkeel ci baatin te nekk ca bérab yu kawe ya.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
donec occurramus omnes in unitatem fidei et agnitionis filii dei in virum perfectum in mensuram aetatis plenitudinis christ
noonu nu mànkoo ci sunu ngëm ak ci xam doomu yàlla ji, ba kera nuy egg ci nekk nit ku sotti, te taxaw taxawaay bu dëppook matug kirist.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
in virtute signorum et prodigiorum in virtute spiritus sancti ita ut ab hierusalem per circuitum usque in illyricum repleverim evangelium christ
ci ay tegtal ak i kéemaan, sukkandikoo ci dooley xelu yàlla mi. ba fi mu nekk nag yégle naa fu nekk xebaaru kirist, li dale ci yerusalem, jaar ci gox yépp, ba àgg diiwaanu iliri.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et dixit mihi sufficit tibi gratia mea nam virtus in infirmitate perficitur libenter igitur gloriabor in infirmitatibus meis ut inhabitet in me virtus christ
waaye mu ne ma: «sama yiw doy na la; sama kàttan a ngi mate cig néew doole.» kon nag dëgg-dëgg, gën na maa bég ci damu ndax sama néew doole, ngir kàttanu kirist dëkk ci man.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: