From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sequenti vero sabbato paene universa civitas convenit audire verbum domin
noonu bésu noflaay ba ca tegu, daanaka waa dëkk bépp daje, ngir déglu kàddug yàlla.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et veniunt ad domum et convenit iterum turba ita ut non possent neque panem manducar
am beneen bés yeesu ñëwaat ca kër ga. te mbooloo mu bare dajaloowaat fa, ba tax mënuñoo lekk sax.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et cum transcendisset iesus in navi rursus trans fretum convenit turba multa ad illum et erat circa mar
noonu yeesu jàllaat dex ga, taxaw ca tefes ga. te nit ñu bare dajaloo, wër ko.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ille autem dixit iudaeis convenit rogare te ut crastina die paulum producas in concilium quasi aliquid certius inquisituri sint de ill
mu tontu ne: «yawut yi dañoo dige, ngir ñaan la, nga indi pool ëllëg ca kanamu kureelu àttekat ya, mel ni dañoo bëgg a seet mbiram bu gën a wóor.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
petrus autem ad eam quid utique convenit vobis temptare spiritum domini ecce pedes eorum qui sepelierunt virum tuum ad ostium et efferent t
ci kaw loolu piyeer ne ko: «lu tax ngeen ànd, di diiŋat xelu boroom bi? Ñi denci woon sa jëkkër ñu ngi nii ci bunt bi, te dinañu la yóbbu.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
dicebat autem et similitudinem ad illos quia nemo commissuram a vestimento novo inmittit in vestimentum vetus alioquin et novum rumpit et veteri non convenit commissura a nov
te it yeesu wax leen léeb wii: «kenn du jël mbubb mu bees, xotti ci sekkit, daaxe ko mbubb mu màggat. lu ko moy, dina xotti mbubb mu bees mi, te sekkit, wi mu ci jële, du ànd ak mbubb mu màggat mi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: