Results for desideriis translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

ut iam non hominum desideriis sed voluntate dei quod reliquum est in carne vivat tempori

Wolof

noonu diir bi ko dese ci kaw suuf, dëddu na bànneexi bakkan, jublu ci coobareg yàlla.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

carissimi obsecro tamquam advenas et peregrinos abstinere vos a carnalibus desideriis quae militant adversus anima

Wolof

samay xarit, yéen ñiy ay gan ak ay doxandéem ci àddina si, maa ngi leen di dénk lii: dëdduleen bànneexi bakkan yiy xeex ak xol.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

superba enim vanitatis loquentes pellicent in desideriis carnis luxuriae eos qui paululum effugiunt qui in errore conversantu

Wolof

dañuy fàbbi ñu naroona mucc ci àddina ju réer, dig leen ak làmmiñ yu neex bànneexi bakkan yu jéggi dayo.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

eramus enim et nos aliquando insipientes increduli errantes servientes desideriis et voluptatibus variis in malitia et invidia agentes odibiles odientes invice

Wolof

ndaxte nun itam ñu ñàkk xel lanu woon te déggadi, nu réer bay jaamu ay bëgg-bëgg ak i bànneex yu wuute, nu dëkk ci coxorte ak ñeetaange, di ñu sikk tey sikkante.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

in quibus et nos omnes aliquando conversati sumus in desideriis carnis nostrae facientes voluntates carnis et cogitationum et eramus natura filii irae sicut et ceter

Wolof

te nun it booba àndoon nanu ak ñoom ca seen dund ga, di topp sunu bakkan ciy wut bànneexi yaram ak coobarey xel. noonu ci sunu bindu nit yeyoo nanu meru yàlla, ni ña ca des.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

similiter autem et masculi relicto naturali usu feminae exarserunt in desideriis suis in invicem masculi in masculos turpitudinem operantes et mercedem quam oportuit erroris sui in semet ipsis recipiente

Wolof

noonu it góor ñi bàyyi nañu li jekk ci seeni cér, maanaam ànd ak jigéen, bay am ay bëgg-bëgg yu tar ci ànd ak seeni moroom. góor di defante ak góor li warul, ñu di jot seen peyu réer ci seeni yaram.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,209,099 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK