From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et ipsi non intellexerunt verbum quod locutus est ad illo
waaye xamuñu li kàddoom yi doon tekki.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
tunc intellexerunt discipuli quia de iohanne baptista dixisset ei
ndax wax jooju nag, taalibe ya xam ne, ci mbirum yaxya la leen doon wax.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
tunc intellexerunt quia non dixerit cavendum a fermento panum sed a doctrina pharisaeorum et sadducaeoru
noonu ñu xam ne, yeesu waxul woon lawiiru mburu, waaye ñu moytu njàngalem farisen ya ak sadusen ya.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et ipsi nihil horum intellexerunt et erat verbum istud absconditum ab eis et non intellegebant quae dicebantu
waaye taalibe ya dégguñu li mu leen doon wax; kàddu yooyu ump na leen, te xamuñu li waxi yeesu yooyu tekki.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
qui cum iustitiam dei cognovissent non intellexerunt quoniam qui talia agunt digni sunt morte non solum ea faciunt sed et consentiunt facientibu
xam nañu ne, ñiy jëfe loolu, yàlla daganal na seen dee, waaye teewul ñu di ko def, boole ko ak di farle ñi ci sax.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: