From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
intrantes autem in domum salutate ea
bu ngeen di dugg ci kër nag, nuyooleen.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
alia autem die profecti venimus caesaream et intrantes in domum philippi evangelistae qui erat de septem mansimus apud eu
nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
nemo autem lucernam accendens operit eam vaso aut subtus lectum ponit sed supra candelabrum ponit ut intrantes videant lume
«kenn du taal làmp, dëpp ci leget, walla mu di ko def ci ron lal. daf koy wékk, ngir mu leeral ñiy dugg.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
confestim cecidit ante pedes eius et exspiravit intrantes autem iuvenes invenerunt illam mortuam et extulerunt et sepelierunt ad virum suu
ca saa sa mu daanu ciy tànkam dee. bi waxambaane ya agsee nag, ñu fekk ko, mu faatu; ñu yóbbu ko, def ko ci wetu jëkkëram.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et intrantes domum invenerunt puerum cum maria matre eius et procidentes adoraverunt eum et apertis thesauris suis obtulerunt ei munera aurum tus et murra
Ñu dugg ca kër ga, gis xale ba ak maryaama ndeyam, ñu daldi sukk, di ko màggal. Ñu ubbi seeni boyetu alal, may ko wurus ak cuuraay ak ndàbb lu xeeñ lu ñuy wax miir.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
tunc vadit et adsumit septem alios spiritus secum nequiores se et intrantes habitant ibi et fiunt novissima hominis illius peiora prioribus sic erit et generationi huic pessima
bu ko gisee nag, mu dem wooyi yeneen juróom-ñaari rab yu ko gën a soxor, ñu dugg, sanc fa; ba tax muju nit kooku mooy yées njàlbéenam. noonu lay nekke ak niti jamono ju bon jii.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: