From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
dicebat enim illi iohannes non licet tibi habere ea
te yaxya daan ko wax: «jaaduwul nga denc ko.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
altera die iterum stabat iohannes et ex discipulis eius du
ca ëllëg sa yaxya taxawaatoon na ca bérab booba, ànd ak ñaari taalibeem.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
cum autem audisset quod iohannes traditus esset secessit in galilaea
am bés yeesu dégg ne, jàpp nañu yaxya; mu jóg nag, jëm galile.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
dicebat enim iohannes herodi non licet tibi habere uxorem fratris tu
te yaxya ne ko: «jaaduwul nga denc sa jabaru mag.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
venit enim iohannes neque manducans neque bibens et dicunt daemonium habe
ndaxte yaxya feeñ na, lekkul, naanul, ngeen daldi ne: “dafa ànd ak rab.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
fuit iohannes in deserto baptizans et praedicans baptismum paenitentiae in remissionem peccatoru
noonu yaxya feeñ ca màndiŋ ma, di sóob nit ñi ci ndox, tey waaree nii: «tuubleen seeni bàkkaar, ba noppi ma sóob leen ci ndox, ngir yàlla baal leen seeni bàkkaar.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et multi venerunt ad eum et dicebant quia iohannes quidem signum fecit nullu
nit ñu bare ñëw ci moom, te naan: «yaxya deful benn kéemaan, waaye li mu wax ci kii yépp, dëgg la.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
postquam autem traditus est iohannes venit iesus in galilaeam praedicans evangelium regni de
bi nga xamee ne jàpp nañu yaxya, yeesu dem ca diiwaanu galile, di waare xebaar bu baaxu yàlla,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
altera die videt iohannes iesum venientem ad se et ait ecce agnus dei qui tollit peccatum mund
ca ëllëg sa, bi yaxya gisee yeesu, muy ñëw ci moom, mu ne: «xool-leen! kii mooy mbotem yàlla, mi ñu nar a rey, ngir dindi bàkkaaru àddina.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et annas princeps sacerdotum et caiphas et iohannes et alexander et quotquot erant de genere sacerdotal
ràññe nañu ci: anas, miy saraxalekat bu mag bi, kayif, yowaana, alegsàndar ak bokki saraxalekat bu mag bi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
erat autem et iohannes baptizans in aenon iuxta salim quia aquae multae erant illic et adveniebant et baptizabantu
yaxya moom itam doon na sóobe ci ndox ci dëkku aynon, ca wetu dëkku salim, ndaxte diiwaan booba bare woon na ndox. nit ñi daan nañu ñëw ci moom, mu di leen sóob.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
cum autem venissent ad eum viri dixerunt iohannes baptista misit nos ad te dicens tu es qui venturus es an alium expectamu
bi taalibe ya agsee ca yeesu, ñu ne ko: «yaxya moo nu yebal, nu laaj ndax yaa di ki waroon a ñëw, walla danuy xaar keneen?»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
a quibusdam quia iohannes surrexit a mortuis a quibusdam vero quia helias apparuit ab aliis autem quia propheta unus de antiquis surrexi
am it ñuy wax naan: iliyas moo dellusi. Ñeneen naan: «kenn ci yonent yu jëkk yaa dekki.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
cum impleret autem iohannes cursum suum dicebat quem me arbitramini esse non sum ego sed ecce venit post me cuius non sum dignus calciamenta pedum solver
te ba yaxyay jeexal sasam, mu ne: “ku ngeen may teg? duma ki war a ñëw; waaye am na kuy ñëw sama gannaaw, koo xam ne kii yeyoowumaa tekki ay dàllam.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et cum cognovissent gratiam quae data est mihi iacobus et cephas et iohannes qui videbantur columnae esse dextras dederunt mihi et barnabae societatis ut nos in gentes ipsi autem in circumcisione
te saag, sefas ak yowaana nag, ñi ñu teg kenuy mbooloo mi, bi ñu ràññee yen bi ma yàlla jagleel ci yiwam, ñu fekksi nu ci, ba jox nu loxo, man ak barnabas, nu liggéey ca ña dul yawut, ñoom ñu liggéey ca yawut ya.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et cum introissent in cenaculum ascenderunt ubi manebant petrus et iohannes iacobus et andreas philippus et thomas bartholomeus et mattheus iacobus alphei et simon zelotes et iudas iacob
bi ñu dikkee, ñu yéeg ca néeg, ba sut ca taax ma, fa ñuy dal. Ñoo doon piyeer ak yowaana, saag ak andare, filib ak tomaa, bartelemi ak macë, saag doomu alfe, ak simoŋ mi bokkoon ci mbooloo mi ñuy wax Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa doomu saag.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: