Results for iudas translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

simon cananeus et iudas scariotes qui et tradidit eu

Wolof

simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa iskariyo, mi nar a wor yeesu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dicit ergo unus ex discipulis eius iudas scariotis qui erat eum tradituru

Wolof

kenn ca taalibey yeesu ya, muy yudaa iskariyo, mi ko nar a wor, daldi ne:

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

tunc abiit unus de duodecim qui dicitur iudas scarioth ad principes sacerdotu

Wolof

ca waxtu woowu kenn ci fukki taalibe ya ak ñaar, ku tudd yudaa iskariyo, dem ca saraxalekat yu mag ya,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et iudas scariotis unus de duodecim abiit ad summos sacerdotes ut proderet eum illi

Wolof

ca waxtu woowu kenn ci fukki taalibe ya ak ñaar, ku tudd yudaa iskariyo, dem ca saraxalekat yu mag ya, ngir wori yeesu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et cena facta cum diabolus iam misisset in corde ut traderet eum iudas simonis scarioti

Wolof

yeesu ak taalibe yaa ngi doon reer. fekk na booba seytaane xiirtal yudaa, doomu simoŋ iskariyo, ngir mu wori yeesu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

accipere locum ministerii huius et apostolatus de quo praevaricatus est iudas ut abiret in locum suu

Wolof

mu yenu liggéeyu nekk sa ndaw, wuutu yudaa, mi ko bàyyi, dem bérabam.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dicit ei iudas non ille scariotis domine quid factum est quia nobis manifestaturus es te ipsum et non mund

Wolof

yudaa --du yudaa iskariyo de, beneen la woon — ne ko: «boroom bi, lu xew, ba nga nar noo feeñu nun rekk, te doo feeñu àddina sépp?»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

adhuc eo loquente ecce turba et qui vocabatur iudas unus de duodecim antecedebat eos et adpropinquavit iesu ut oscularetur eu

Wolof

bi yeesu di wax, mbooloo mu bare agsi; ku ñuy wax yudaa te mu bokkoon ci fukki ndaw yi ak ñaar jiite leen. yudaa jegeñsi yeesu, bëgg koo fóon.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

tunc videns iudas qui eum tradidit quod damnatus esset paenitentia ductus rettulit triginta argenteos principibus sacerdotum et senioribu

Wolof

bi nga xamee ne yudaa, mi woroon yeesu, gis na ne, daan nañu ko, mu am naqaru xol. mu dem nag ca saraxalekat yu mag ya ak njiit ya, delloo leen fanweeri poset yu xaalis,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

post hunc extitit iudas galilaeus in diebus professionis et avertit populum post se et ipse periit et omnes quotquot consenserunt ei dispersi sun

Wolof

gannaawam it yudaa mu galile jóg, ca jamono ja ñu doon bind waa réew ma, mu jógloo nit ñu bare, ñu ànd ak moom. moom itam dee na, te ay nitam ñépp tasaaroo.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

adhuc ipso loquente ecce iudas unus de duodecim venit et cum eo turba multa cum gladiis et fustibus a principibus sacerdotum et senioribus popul

Wolof

bi muy wax loolu nag, yudaa, mi bokkoon ca fukki taalibe ya ak ñaar te naroon koo wor, agsi, ànd ak mbooloo mu bare, jóge ca saraxalekat yu mag ya ak ca njiiti xeet wa, te gànnaayoo jaasi ak yet.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et cum introissent in cenaculum ascenderunt ubi manebant petrus et iohannes iacobus et andreas philippus et thomas bartholomeus et mattheus iacobus alphei et simon zelotes et iudas iacob

Wolof

bi ñu dikkee, ñu yéeg ca néeg, ba sut ca taax ma, fa ñuy dal. Ñoo doon piyeer ak yowaana, saag ak andare, filib ak tomaa, bartelemi ak macë, saag doomu alfe, ak simoŋ mi bokkoon ci mbooloo mi ñuy wax Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa doomu saag.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,948,258,623 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK