Results for ne translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

non ex operibus ut ne quis glorietu

Wolof

du peyu jëf, ngir kenn du ci kañu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et praecepit eis ne manifestum eum faceren

Wolof

te mu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo siiwal.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et comminatus est eis ne cui dicerent de ill

Wolof

ci kaw loolu yeesu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo wax kenn.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

itaque qui se existimat stare videat ne cada

Wolof

kon nag kiy naw sa doole, ba yaakaar ne taxaw nga, moytul a daanu ci bàkkaar!

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

at ille increpans illos praecepit ne cui dicerent ho

Wolof

noonu yeesu daldi leen dénk, tere leen ñu wax ko kenn,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et deprecabatur eum multum ne se expelleret extra regione

Wolof

muy ñaan yeesu lool, ngir mu bañ leen a dàq ca réew ma.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

adiuvantes autem et exhortamur ne in vacuum gratiam dei recipiati

Wolof

nun nag ñiy liggéeyandoo ak yàlla, nu ngi leen di ñaan: jariñooleen yiw, wi ngeen jote ci yàlla, ngir mu bañ a neen ci yéen.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

deo pro nobis melius aliquid providente ut ne sine nobis consummarentu

Wolof

ndaxte yàlla dafa tëral lu gën ci nun te bëggu leen a yeggale cig mat, fi ak ànduñu ci ak nun.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dicebant autem non in die festo ne forte tumultus fieret in popul

Wolof

waaye ñu ne: «bumu doon ci bésu màggal bi, ngir yengu-yengu bañ a am ci nit ñi.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dicit mihi ne signaveris verba prophetiae libri huius tempus enim prope es

Wolof

mu ne ma it: «bul tëj téere bii ak waxi yàlla yi mu ëmb, ndaxte waxtu wi jege na.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cum audieritis autem bella et opiniones bellorum ne timueritis oportet enim fieri sed nondum fini

Wolof

bu ngeen déggee ay xare ak coowi xare, wottuleen a tiit; loolu war na am, waaye mujug jamono ji jotagul.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dimitte nobis peccata nostra siquidem et ipsi dimittimus omni debenti nobis et ne nos inducas in temptatione

Wolof

baal nu sunuy bàkkaar,ndaxte nun itam danuy baal ñépp ñi nu tooñ.te bu nu teg ci yoonu nattu.”»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

praecepta nosti ne adulteres ne occidas ne fureris ne falsum testimonium dixeris ne fraudem feceris honora patrem tuum et matre

Wolof

xam nga ndigal yi: “bul bóom, bul njaaloo, bul sàcc, bul seede lu dul dëgg, bul nangu alalu jaambur, teralal sa ndey ak sa baay.”»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,387,132 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK