From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
cui noluerunt oboedire patres nostri sed reppulerunt et aversi sunt cordibus suis in aegyptu
waaye sunuy maam nanguwuñu koo déggal; dañu koo bañ te seeni xel dëpp, dellu misra.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
admone illos principibus et potestatibus subditos esse dicto oboedire ad omne opus bonum paratos ess
fàttali leen ñuy déggal kilifa, yi yore nguur gi, tey jëfe seeni ndigal, ñu taxaw temm ci lépp luy jëf ju baax.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: