From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
gratias autem deo quod fuistis servi peccati oboedistis autem ex corde in eam formam doctrinae in qua traditi esti
waaye sant naa yàlla ci lii: yéen ñi doon jaami bàkkaar, bi ngeen déggee mboolem dëgg gi, nangu ngeen ko ak seen xol bépp.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
itaque carissimi mei sicut semper oboedistis non ut in praesentia mei tantum sed multo magis nunc in absentia mea cum metu et tremore vestram salutem operamin
noonu samay soppe, xam naa ne, musuleen a jóg ci dégg ndigal, waxuma sax bi ma nekkee ak yéen rekk, waaye rawatina bi ma leen soree. kon nag maa ngi leen di ñaan, ngeen biral seen mucc ci seeni jëf, te def ko ci ragal yàlla gu dëggu.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: