Results for pacem translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

pacem sequimini cum omnibus et sanctimoniam sine qua nemo videbit dominu

Wolof

wutleen ak ñépp jàmm te fonk dund gu sell, ndaxte ku sellul doo gis boroom bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

declinet autem a malo et faciat bonum inquirat pacem et persequatur ea

Wolof

na dëddu lu bon, tey def lu baax,na xënte jàmm te sax ci.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et veniens evangelizavit pacem vobis qui longe fuistis et pacem his qui prop

Wolof

bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

iustificati igitur ex fide pacem habeamus ad deum per dominum nostrum iesum christu

Wolof

léegi nag, gannaaw yàlla àtte na nu jub ci kaw ngëm, nanu jàpp ci jàmm, ji nu am fa kanam yàlla, jaarale ko ci sunu boroom yeesu kirist.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ipse autem dominus pacis det vobis pacem sempiternam in omni loco dominus cum omnibus vobi

Wolof

na leen boroom jàmm may jàmm ci fépp ak ci lépp. na boroom bi ànd ak yéen ñépp.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quomodo vero praedicabunt nisi mittantur sicut scriptum est quam speciosi pedes evangelizantium pacem evangelizantium bon

Wolof

te it nan lañu man a waaree, su leen kenn yónniwul? looloo tax mbind mi wax ne: «Ñiy yégle xebaar bu baax bi, ni seen ñëw di sedde xol!»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

haec locutus sum vobis ut in me pacem habeatis in mundo pressuram habetis sed confidite ego vici mundu

Wolof

waaye nag déedéet, wéetuma, ndaxte baay baa ngi may wéttali. dama leen wax loolu, ngir ngeen am jàmm ci man. dingeen am nattu ci àddina, waaye takkleen fit yi; noot naa àddina.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

de cetero fratres gaudete perfecti estote exhortamini idem sapite pacem habete et deus dilectionis et pacis erit vobiscu

Wolof

kon nag bokk yi, bégleen, jublu cig mat, di déglu soññante bi ma leen di dénk, am benn xalaat te dëkk ci jàmm; noonu yàlla miy mbëggeel te di yàllay jàmm dina ànd ak yéen.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

bonum est sal quod si sal insulsum fuerit in quo illud condietis habete in vobis sal et pacem habete inter vo

Wolof

Ñépp safara lañu leen di xorome.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ecclesia quidem per totam iudaeam et galilaeam et samariam habebat pacem et aedificabatur ambulans in timore domini et consolatione sancti spiritus replebatu

Wolof

noonu mbooloom ñi gëm nekk ci jàmm ci biir diiwaani yude gépp ak galile ak samari; ñuy gën a dëgër, di wéy ci ragal yàlla, tey yokku ci ndimbalu xel mu sell mi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

erat autem iratus tyriis et sidoniis at illi unianimes venerunt ad eum et persuaso blasto qui erat super cubiculum regis postulabant pacem eo quod alerentur regiones eorum ab ill

Wolof

fekk mu nekk ci xëccoo bu tàng ak waa dëkki tir ak sidon. naka noona ñu ànd, bëgg koo gis. Ñu neexal balastus, bëkk-néegu buur ba, di ñaan jàmm, ndaxte réewu buur ba moo doon dundal seen bos.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,770,645,484 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK