Results for paenitentiae translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

praedicante iohanne ante faciem adventus eius baptismum paenitentiae omni populo israhe

Wolof

laata muy ñëw nag, yaxya daan na waare, ne bànni israyil gépp, ñu tuub seeni bàkkaar, te mu sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

fuit iohannes in deserto baptizans et praedicans baptismum paenitentiae in remissionem peccatoru

Wolof

noonu yaxya feeñ ca màndiŋ ma, di sóob nit ñi ci ndox, tey waaree nii: «tuubleen seeni bàkkaar, ba noppi ma sóob leen ci ndox, ngir yàlla baal leen seeni bàkkaar.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et venit in omnem regionem iordanis praedicans baptismum paenitentiae in remissionem peccatoru

Wolof

yaxya daldi dugg àll, bi wër dexu yurdan gépp, di waaree nii: «tuubleen seeni bàkkaar, ba noppi ma sóob leen ci ndox, ngir yàlla baal leen seeni bàkkaar.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dixit autem paulus iohannes baptizavit baptisma paenitentiae populum dicens in eum qui venturus esset post ipsum ut crederent hoc est in iesu

Wolof

pool ne leen: «yaxya daan na sóob nit ñi ci ndox, ndax bi ñu tuubee seeni bàkkaar; te mu ne bànni israyil, kiy topp ci moom lañu war a gëm, maanaam yeesu.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

facite ergo fructus dignos paenitentiae et ne coeperitis dicere patrem habemus abraham dico enim vobis quia potest deus de lapidibus istis suscitare filios abraha

Wolof

jëfeleen nag ni ñu tuub seeni bàkkaar, te bañ a nax seen bopp naan: “nun daal doomi ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, yàlla man na defal ibraayma ay doom ci doj yii.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

sed his qui sunt damasci primum et hierosolymis et in omnem regionem iudaeae et gentibus adnuntiabam ut paenitentiam agerent et converterentur ad deum digna paenitentiae opera faciente

Wolof

waaye li tàmbali ci damas, teg ci dëkku yerusalem ak réewu yawut mépp, ba agsi ci ñi dul yawut, yégal naa leen, ñu tuub seeni bàkkaar te woññiku ci yàlla, bay jëf lu dëppook réccu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,787,534,903 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK