From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sed quod decet mulieres promittentes pietatem per opera bon
waaye na seen col di jëf yu rafet, ndaxte looloo jekk ci jigéen juy woote ag ragal yàlla.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
tu autem o homo dei haec fuge sectare vero iustitiam pietatem fidem caritatem patientiam mansuetudine
kon nag yaw waayu yàlla ji, dawal loolu, te topp njub, ragal yàlla, ngëm, mbëggeel, muñ ak lewet.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
paulus servus dei apostolus autem iesu christi secundum fidem electorum dei et agnitionem veritatis quae secundum pietatem es
man pool maa lay bind, man miy jaamu yàlla ak ndaw li yeesu kirist yónni, ngir xamle ngëm, gi lal yoonu ñi yàlla tànn, tey yokk xam-xamu dëgg, giy meññ ragal yàlla;
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
si quis aliter docet et non adquiescit sanis sermonibus domini nostri iesu christi et ei quae secundum pietatem est doctrina
waaye su fi amee kuy jàngale leneen, ba jàppul ci kàddu yu wér yu yeesu kirist boroom bi, te fonkul waaraate buy jur ragal yàlla,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
quomodo omnia nobis divinae virtutis suae quae ad vitam et pietatem donata est per cognitionem eius qui vocavit nos propria gloria et virtut
dooley yàlla moo nu may lépp lu aju ci dund gu sax ak ragal yàlla, jaarale ko ci xam gi nu ko xam, moom mi nu woo ci kaw ndamam ak dooleem.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: