From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et progressus inde pusillum vidit iacobum zebedaei et iohannem fratrem eius et ipsos in navi conponentes reti
bi yeesu demee ba ca kanam, mu gis saag doomu sebede, ak yowaana, mi mu bokkal ndey ak baay, ñu nekk ci gaal gi, di defar seeni mbaal.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et progressus pusillum procidit in faciem suam orans et dicens mi pater si possibile est transeat a me calix iste verumtamen non sicut ego volo sed sicut t
bi mu waxee loolu, yeesu dem ci kanam tuuti, ne nërëm ci suuf, di ñaan ne: «sama baay, bu manee am, na ma kaasu naqar bii teggi! moona, bumuy ci sama coobare, waaye na sa coobare am.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: