From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
erastus remansit corinthi trophimum autem reliqui infirmum milet
erast des na dëkku korent. torofim dafa woppoon, ma bàyyi ko dëkku mile.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
consummatisque diebus cum redirent remansit puer iesus in hierusalem et non cognoverunt parentes eiu
bi màggal ga tasee, ñu dëpp ñibbi, waaye xale ba yeesu des yerusalem, te ay waajuram yéguñu ko.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
mittens autem in macedoniam duos ex ministrantibus sibi timotheum et erastum ipse remansit ad tempus in asi
mu yebal nag ci maseduwan ñaari jaraafam, di timote ak erast, waaye moom mu des ab diir ci asi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
audientes autem unus post unum exiebant incipientes a senioribus et remansit solus et mulier in medio stan
bi ñu déggee loolu, ñuy rocceeku kenn-kenn, mag ña jiitu. yeesu rekk des fa, jigéen ja taxaw ca kanamam.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: