Results for repleti translation from Latin to Wolof

Latin

Translate

repleti

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et repleti sunt omnes in synagoga ira haec audiente

Wolof

bi ñu déggee wax yooya, ñépp ña nekkoon ca jàngu ba daldi fees ak mer.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et estis in illo repleti qui est caput omnis principatus et potestati

Wolof

te mat ngeen ci moom, miy buuru kilifa yépp ak boroom sañ-sañ yépp.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ipsi autem repleti sunt insipientia et conloquebantur ad invicem quidnam facerent ies

Wolof

waaye nit ña mer ba fees, di rabat pexe yu jëm ca yeesu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et stupor adprehendit omnes et magnificabant deum et repleti sunt timore dicentes quia vidimus mirabilia hodi

Wolof

mbooloo mépp waaru, di màggal yàlla. Ñu ragal tey wax naan: «gis nanu tey ay mbir yu ëpp xel.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

exsurgens autem princeps sacerdotum et omnes qui cum illo erant quae est heresis sadducaeorum repleti sunt zel

Wolof

booba saraxalekat bu mag ba jóg ak gàngooram gépp, maanaam kureelu sadusen, ga fa dëkk. kiñaan gu mag jàpp leen,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et repleti sunt omnes spiritu sancto et coeperunt loqui aliis linguis prout spiritus sanctus dabat eloqui illi

Wolof

noonu ñu fees ak xel mu sell mi ñoom ñépp, ñu daldi wax yeneeni làkk, ni leen xel mu sell mi maye, ñu wax ko.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et cum orassent motus est locus in quo erant congregati et repleti sunt omnes spiritu sancto et loquebantur verbum dei cum fiduci

Wolof

bi ñu ñaanee ba noppi, bérab ba ñu booloo woon daldi yengatu; te ñoom ñépp fees ak xel mu sell mi, ñuy wax kàddug yàlla ak fit wu dëgër.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

certus sum autem fratres mei et ego ipse de vobis quoniam et ipsi pleni estis dilectione repleti omni scientia ita ut possitis alterutrum moner

Wolof

bokk yi, wóor na ma ne, baax ngeen ba fa mbaax man a yem, fees dell ak xam-xam, ba man a jàngaleente mbiri yàlla ci seen biir.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,913,944,650 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK