From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
quomodo intravit in domum dei et panes propositionis comedit quos non licebat ei edere neque his qui cum eo erant nisi solis sacerdotibu
xanaa yéguleen, ni mu dugge woon ca kër yàlla ga, gis fa mburu, ya ñu jébbal yàlla, mu daldi ko lekk. fekk jaaduwul mu lekk ca, moom walla ña mu àndaloon; saraxalekat rekk a ko sañoon a lekk.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
quomodo intravit in domum dei et panes propositionis sumpsit et manducavit et dedit his qui cum ipso erant quos non licet manducare nisi tantum sacerdotibu
xanaa yéguleen, ni mu dugge woon ca kër yàlla ga, jël mburu, ya ñu jébbal yàlla, lekk ca, jox ca ña mu àndaloon? fekk jaaduwul kenn lekk ko, ku dul saraxalekat.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: