Results for sacramentum translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

sacramentum hoc magnum est ego autem dico in christo et in ecclesi

Wolof

loolu ëmb na mbóot mu xóot; man maa ngi wax ci lu jëm ci kirist ak mbooloo mi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quoniam secundum revelationem notum mihi factum est sacramentum sicut supra scripsi in brev

Wolof

yàlla feeñu na ma, xamal ma mbóoti mbir mi mu tëral, ni ma leen ko binde ci kàddu yu néew.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ut notum faceret nobis sacramentum voluntatis suae secundum bonum placitum eius quod proposuit in e

Wolof

ci feeñal nu mbóoti coobareem, dëppook yéeneem ju rafet, ji mu jaarale ci kirist.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dixit mihi angelus quare miraris ego tibi dicam sacramentum mulieris et bestiae quae portat eam quae habet capita septem et decem cornu

Wolof

malaaka ma ne ma: «lu tax nga jaaxle? dinaa la leeralal kumpag jigéen ji ak rab, wi mu war te am juróom-ñaari bopp ak fukki béjjén.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et manifeste magnum est pietatis sacramentum quod manifestatum est in carne iustificatum est in spiritu apparuit angelis praedicatum est gentibus creditum est in mundo adsumptum est in glori

Wolof

ci dëgg-dëgg ragal yàlla ëmb na mbóot yu xóot:ki wàcc, yor bindu nit,mu bir ne xelam jub na,te malaaka ya gis ko;xamlees na ko ci xeet yi,ñu gëm ko ci kaw suuf,te yàlla teeru ko ci ndamam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,791,467,848 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK