Results for scientes translation from Latin to Wolof

Latin

Translate

scientes

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et deridebant eum scientes quia mortua esse

Wolof

waaye ñu di ko ñaawal, ndaxte xamoon nañu ne, dee na.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes fratres dilecti a deo electionem vestra

Wolof

bokk yi, yéen ñi yàlla bëgg, xam nanu ne yàlla tànn na leen;

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes quod probatio fidei vestrae patientiam operatu

Wolof

xam ne nattub ngëm mooy ndeyu muñ.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes quod a domino accipietis retributionem hereditatis domino christo servit

Wolof

xam ne boroom bi dina fey seeni jëf, mu di cér bi mu leen dencal. kirist mooy boroom, bi ngeen di liggéeyal.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes quoniam qui suscitavit iesum et nos cum iesu suscitabit et constituet vobiscu

Wolof

ndaxte xam nanu ne yàlla, mi dekkal boroom bi yeesu, dina nu dekkal nun itam ak yeesu, te dina nu yóbbu ak yéen, taxawal nun ñépp ci jataayam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

audentes igitur semper et scientes quoniam dum sumus in corpore peregrinamur a domin

Wolof

noonu kon nu ngi fees ak kóolute fu nu tollu; te xam nanu ne, fi ak nu ngi dëkk ci yaram wii, àggagunu sunu màkkaan ci wetu boroom bi —

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cui resistite fortes fide scientes eadem passionum ei quae in mundo est vestrae fraternitati fier

Wolof

jànkoonteleen ak moom ci biir ngëm gu takku, xam ne kureelu bokk yi ci àddina yépp, ñu ngi daj ay fitna ni yéen.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

domini quod iustum est et aequum servis praestate scientes quoniam et vos dominum habetis in cael

Wolof

sang yi, yorleen seeni jaam ci nu jub te aw yoon, xam ne, am ngeen yéen itam ab sang ca asamaan.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dicit eis iesus venite prandete et nemo audebat discentium interrogare eum tu quis es scientes quia dominus esse

Wolof

yeesu ne leen: «Ñëwleen ndékki.» kenn ci taalibe yi ñemewu koo laaj ki mu doon, ndaxte xam nañu ne, boroom bi la.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et hoc scientes tempus quia hora est iam nos de somno surgere nunc enim propior est nostra salus quam cum credidimu

Wolof

te lii itam am na: xam ngeen bu baax jamono ji nu tollu; jamonoy yeewu jot na, ndax léegi sunu mucc gën na noo jege, ca ba nu dooree gëm.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes ergo timorem domini hominibus suademus deo autem manifesti sumus spero autem et in conscientiis vestris manifestos nos ess

Wolof

gannaaw xam nanu ragal yàlla nag, nu ngi fexee gëmloo nit ñi, waaye li nu nekk leer na yàlla te yaakaar naa ne, leer na leen it, ba ne fàŋŋ.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

commonere autem vos volo scientes semel omnia quoniam iesus populum de terra aegypti salvans secundo eos qui non crediderunt perdidi

Wolof

xam ngeen loolu lépp ba noppi sax, waaye dama leen koy fàttali rekk. xam ngeen ne boroom bi musal na xeetam, ba génne leen réewu misra, waaye gannaaw ba raafal na ñi gëmul woon.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et domini eadem facite illis remittentes minas scientes quia et illorum et vester dominus est in caelis et personarum acceptio non est apud eu

Wolof

yéen it sang yi, jëfeleen noonu seen diggante ak seeni jaam, te dëddu gépp raglu, xam ne yéena bokk benn boroom ci asamaan, te ñépp a yem fi moom.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

scientes autem quod non iustificatur homo ex operibus legis nisi per fidem iesu christi et nos in christo iesu credidimus ut iustificemur ex fide christi et non ex operibus legis propter quod ex operibus legis non iustificabitur omnis car

Wolof

teewul nu xam ne, yàlla du àtte kenn ni ku jub ci kaw sàmm yoon, waaye ci gëm yeesu kirist. kon nun itam gëm nanu kirist yeesu, ngir yàlla àtte nu jub ci kaw gëm kirist, te du ci sàmm yoon. ndaxte du caageenug sàmm yoon mooy tax yàlla àtte kenn ni ku jub.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,906,683,330 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK