From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sed valefaciens et dicens iterum revertar ad vos deo volente profectus est ab ephes
kon mu tàggtoo ak ñoom naan: «dinaa dellusi ci yéen, bu soobee yàlla.» noonu mu dugg gaal, jóge efes,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
non habui requiem spiritui meo eo quod non invenerim titum fratrem meum sed valefaciens eis profectus sum in macedonia
waaye sama xel dalul benn yoon, ndax li ma fa fekkul sama mbokk, tit. noonu nag ma tàggu leen, daldi dem diiwaanu maseduwan.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
paulus vero cum adhuc sustinuisset dies multos fratribus valefaciens navigavit syriam et cum eo priscilla et aquila qui sibi totonderat in cencris caput habebat enim votu
bi loolu wéyee pool desati fa fan yu bare. gannaaw ga mu tàggtoo ak bokk ya, dugg gaal jëm siri, ànd ak pirsil ak akilas. bi mu jógeegul teerub señsere, mu watlu boppam, ndaxte am na lu mu dige woon ak yàlla.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.