Results for volunt translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

aemulantur vos non bene sed excludere vos volunt ut illos aemulemin

Wolof

nit ñooñu leen di farle, seen mébét baaxul. dañu leen a bëgg a tàggale ak nun, ngir ngeen far ak ñoom.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et omnes qui volunt pie vivere in christo iesu persecutionem patientu

Wolof

te ku bokk ci kirist yeesu, te bëgg dund dund gu ànd ak ragal yàlla, alamikk ñu fitnaal la.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quod non est aliud nisi sunt aliqui qui vos conturbant et volunt convertere evangelium christ

Wolof

fekk du xebaar bu baax bi. dafa am rekk ci seen biir ay nit ñiy nëxal xel yi, te bëgg a dandal xebaar bu baax bu kirist.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

neque enim qui circumciduntur legem custodiunt sed volunt vos circumcidi ut in carne vestra glorientu

Wolof

kureel gi faaydaal xaraf, ñoom ci seen bopp sax, duñu topp yoon wi. dañoo bëgg a ngeen xaraf, ba ñu man a bàkku ci seen yaram, yéen.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dicebat eis in doctrina sua cavete a scribis qui volunt in stolis ambulare et salutari in for

Wolof

bi yeesu di jàngale nag, mu ne leen: «moytuleen xutbakat yi; dañoo bëgg di doxantu, sol ay mbubb yu réy, te ñépp di leen nuyoo ñaari loxo ci pénc mi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quod autem facio et faciam ut amputem occasionem eorum qui volunt occasionem ut in quo gloriantur inveniantur sicut et no

Wolof

noonu may doxale nag dinaa ci sax, ngir ñiy damu, di wut yoon wu ñu aw ba yemale seen bopp ak nun, duñu ko am.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

adtendite a scribis qui volunt ambulare in stolis et amant salutationes in foro et primas cathedras in synagogis et primos discubitus in convivii

Wolof

«moytuleen xutbakat yi; dañoo bëgg di doxantu, sol ay mbubb yu réy, te ñépp di leen nuyoo ñaari loxo ci pénc mi. ci jàngu yi, toogu yu féete kanam lañuy wut, te toogu yu yiw lañuy taamu ci reeri xew yi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

nam qui volunt divites fieri incidunt in temptationem et laqueum et desideria multa inutilia et nociva quae mergunt homines in interitum et perditione

Wolof

waaye ñiy sàkkoo barele, dinañu jànkoonte ak i nattu, ba dugg ci fiir, di xuus ci bëgg-bëggi neen yuy yóbbe ayib, tey sóob nit cig réer ak sànkute.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,747,826,162 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK