From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
naku i whakato, na aporo i whakamakuku; na te atua ia i mea kia tupu
maa jëmbët, apolos suuxat, waaye yàlla moo jebbil.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a tu tangi ana i muri i ona waewae, ka anga ka whakamakuku i ona waewae ki ona roimata, ka muru ki nga makawe o tona matenga, ka kihi i ona waewae, ka whakawahi ki te hinu kakara
bi jigéen ja agsee, mu taxaw ca gannaaw tànki yeesu, di jooy. noonu ay rangooñam tooyal tànki yeesu, jigéen ja di leen fomp ak kawaram, di leen fóon te ciy sotti latkoloñ ja.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
na ka tahuri ia ki te wahine, ka mea ki a haimona, e kite ana koe i tenei wahine? i haere mai ahau ki roto ki tou whare, kahore i homai e koe he wai mo oku waewae; nana ia i whakamakuku oku waewae ki ona roimata, a murua iho ki nga makawe o tona matenga
daldi walbatiku ca jigéen ja, ne simoŋ: «ndax gis nga jigéen jii? dugg naa sa kër, te joxewuloo ndox, ngir raxas samay tànk. waaye moom, raxas na samay tànk ak ay rangooñam, ba noppi fomp leen ak kawaram.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: