Results for avsted translation from Norwegian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Norwegian

Wolof

Info

Norwegian

disiplene gikk da avsted og gjorde som jesus bød dem;

Wolof

noonu taalibe ya dem, def loolu leen yeesu sant.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

avsted! se, jeg sender eder som lam midt iblandt ulver.

Wolof

demleen! maa ngi leen di yónni, mel ni ay mbote ci biir ay bukki.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og han fortalte dem det alt sammen, og sendte dem avsted til joppe.

Wolof

mu nettali leen lépp, yebal leen yope.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

avsted, og stå frem og tal i templet alle dette livs ord for folket!

Wolof

«demleen taxaw ca kër yàlla ga, te xamal nit ñi lépp lu jëm ci dund gu wóor gii.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og de gikk avsted, og fant folen bundet ved døren utenfor på gaten og løste den.

Wolof

taalibe ya dem nag, ñu gis cumbur ga ci mbedd mi, mu yeewe cib buntu kër.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og når i går avsted, da forkynn dette budskap: himlenes rike er kommet nær!

Wolof

bu ngeen demee nag, yégleleen naan: “nguuru yàlla aji kawe ji jegesi na.”

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da nu disse var sendt avsted, kom de til antiokia, og de samlet hele menigheten og gav dem brevet.

Wolof

noonu ñu tàggoo, dem ancos, ñu dajale mbooloo mi, jébbal leen bataaxal bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og de opegget folket og de eldste og de skriftlærde, og de falt over ham og drog ham avsted og førte ham for rådet,

Wolof

noonu ñu jógloo nit ñi ak njiit yi ak xutbakat yi, ñu dal ci kawam, jàpp ko, yóbbu ko ca kureelu àttekat ya.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

men mens disiplene flokket sig omkring ham, stod han op og gikk inn i byen. den næste dag drog han med barnabas avsted til derbe.

Wolof

waaye taalibe ya ñëw wër ko, mu daldi jóg, duggaat ca dëkk ba. ca suba sa nag, mu ànd ak barnabas, dem derbë.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da de nu hadde grepet ham, drog de avsted med ham og førte ham inn i yppersteprestens hus; og peter fulgte langt bakefter.

Wolof

Ñu jàpp yeesu, yóbbu ko ca kër saraxalekat bu mag ba. piyeer topp fu sore.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da det nu var avgjort at vi skulde seile avsted til italia, overgav de både paulus og nogen andre fanger til en høvedsmann ved navn julius ved den keiserlige hærdeling.

Wolof

bi loolu wéyee ñu fas yéene noo dugal gaal jëme réewu itali. noonu ñu jël pool ak ñeneen ñi ñu tëjoon, dénk leen njiitu xare bu tudd yulyus, mi bokk ci mbooloom xare mu buur.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da nu opstyret hadde lagt sig, kalte paulus disiplene til sig og for mante dem og bød dem farvel; så drog han avsted for å fare til makedonia.

Wolof

bi yengu-yengu ba dalee, pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu maseduwan.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da sendte han to av sine disipler avsted og sa til dem: gå inn i byen, og der skal møte eder en mann som bærer en krukke vann; følg ham,

Wolof

noonu yeesu yebal ñaar ci taalibe yi ne leen: «demleen ca dëkk ba, foofa góor gu yenu njaq lu def ndox, dina taseek yéen, ngeen topp ko.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og han sa til dem: far avsted! og de fór ut og fór i svinene. og se, hele hjorden styrtet sig ut over stupet ned i sjøen og døde i vannet.

Wolof

yeesu ne leen: «demleen.» rab ya nag daldi génn, dugg ca mbaam-xuux ya, ñu daldi bartalu, daanu ca dex ga, lab ca ndox ma.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da de hadde hørt kongens ord, drog de avsted; og se, stjernen som de hadde sett i Østen, gikk foran dem, inntil den kom og blev stående over det sted hvor barnet var.

Wolof

ba ñu dégloo buur ba nag, ñu dem. te biddiiw, ba ñu gisoon ca penku ba, ne tell jiite leen, ba àgg, tiim fa xale ba nekk.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

hun løp da avsted, og kom til simon peter og til den andre disippel, han som jesus elsket, og sa til dem: de har tatt herren ut av graven, og vi vet ikke hvor de har lagt ham.

Wolof

mu daw, dem ca simoŋ piyeer ak ca beneen taalibe ba, maanaam ka yeesu bëggoon, ne leen: «jële nañu néewu boroom ba ca bàmmeel ba, te xamunu fu ñu ko yóbbu.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

disse er skamflekkene ved eders kjærlighets-måltider, uten blygsel holder de gilde med eder og forer sig selv; vannløse skyer som drives avsted av vinden; trær, nakne som om høsten, ufruktbare, to ganger død, oprykket med rot;

Wolof

su ñu bokkee ak yéen reeru mbooloo mi, dañu ciy indi ay, niy xeer yu nëbbu ci biir géej; amuñu genn gàcce, waaye dañuy giiroo te fonk seen biir rekk. Ñu ngi mel ni xiin yu amul ndox, yuy naaxsaay ci ngelaw; ni garab yu meññul ci jamonoy meññeef, te buddeeku, dee ba wow koŋŋ;

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,786,428,477 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK