Results for djevelens translation from Norwegian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Norwegian

Wolof

Info

Norwegian

ikke en nyomvendt, forat han ikke skal bli opblåst og falle i djevelens dom.

Wolof

te it bumu nekk kuy door a gëm, ngir mu bañ a yég boppam, bay dajeek mbugalu yàlla, ni ko seytaane defe woon.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

iklæ eder guds fulle rustning, så i kan stå eder mot djevelens listige angrep;

Wolof

gànnaayooleen yérey xarey yàlla yépp, ngir man a jànkoonte ak pexey seytaane.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

men han skal og ha godt vidnesbyrd av dem som er utenfor, forat han ikke skal bli hånet og falle i djevelens snare.

Wolof

te it war na am seede su rafet ci waa àddina, ngir ñu bañ koo diiŋat, ba muy daanu ci fiiru seytaane.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og våkne igjen av sitt rus i djevelens snare, han som de er fanget av, så de må gjøre hans vilje.

Wolof

ñu rëcc ci fiirug seytaane, mi leen jàpp niy jaam, te ñu dellusi ci seen xel yu rafet, ba sóobuwaat ci coobareg yàlla.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

den som gjør synd, er av djevelen; for djevelen synder fra begynnelsen. dertil er guds sønn åpenbaret at han skal gjøre ende på djevelens gjerninger.

Wolof

kuy def bàkkaar, ci seytaane nga bokk, ndax seytaane ca njàlbéen ga ba tey day bàkkaar. te doomu yàlla ji ñëw na, ngir nasaxal jëfi seytaane.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

du som er full av all svik og all ondskap, du djevelens barn, all rettferdighets fiende! vil du ikke holde op med å forvende herrens rette veier?

Wolof

ne ko: «yaw mi fees ak fen ak lu bon, di doomu ibliis, tey noonu lépp lu jub, ndax doo bàyyee dëngal yoon yu jub yu boroom bi?

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

atter tok djevelen ham med op på et meget høit fjell og viste ham alle verdens riker og deres herlighet og sa til ham:

Wolof

gannaaw loolu seytaane yóbbu ko ci kaw tund wu kawe lool, won ko réewi àddina yépp ak seeni ndam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,779,472,202 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK