Results for intet translation from Norwegian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Norwegian

Wolof

Info

Norwegian

forat intet kjød skal rose sig for gud.

Wolof

noonu kenn du man a damu ca kanam yàlla.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

var ikke denne mann fra gud, da kunde han intet gjøre.

Wolof

kon nit kookee nag, bu jógewul woon ca yàlla, du man a def dara.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og på alle yppersteprestenes og de eldstes klagemål svarte han intet.

Wolof

yeesu tontu ko ne: «wax nga ko,» waaye tontuwul dara ca la ko saraxalekat yu mag ya ak njiit ya jiiñ.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

og i har gjort guds lov til intet for eders vedtekts skyld.

Wolof

kooku amatul warugaru teral baayam. noonu tebbi ngeen kàddug yàlla ndax seen aada.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

han spurte ham da med mange ord; men jesus svarte ham intet.

Wolof

noonu mu laaj ko ay laaj yu bare, waaye yeesu tontuwul dara.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

men tungen kan intet menneske temme, det ustyrlige onde, full av dødelig gift.

Wolof

waaye làmmiñ kenn mënu koo noot; musiba la mu dul dal mukk, fees dell ak daŋar juy rey.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

for all guds skapning er god, og intet er å forkaste når det mottas med takk;

Wolof

ndaxte li yàlla sàkk lépp baax na, kon wenn ñam araamul ci ku koy jëfandikoo ak cant.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

for dersom nogen tykkes sig å være noget og er dog intet, da dårer han sig selv.

Wolof

ndaxte kuy naagu te fekk doo dara, dangay nax sa bopp.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

idet i først og fremst vet dette at intet profetord i skriften er gitt til egen tydning;

Wolof

waaye jëkkleena xam ne, amul jenn waxu yonent ci mbind mi, ju balle ci xelu boppam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

den gjør intet usømmelig, søker ikke sitt eget, blir ikke bitter, gjemmer ikke på det onde;

Wolof

du def lu jekkadi, du wut njariñu boppam, du naqari deret, du ñaaw njort.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

for intet er skjult uten at det skal åpenbares, heller ikke blir noget dulgt uten for å komme for dagen.

Wolof

amul dara luy kumpa lu ñu warul a siiwal, mbaa mu làqu te warul ne fàŋŋ.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

for det er skrevet: jeg vil ødelegge de vises visdom, og de forstandiges forstand vil jeg gjøre til intet.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na:«dinaa folli xam-xamu boroom xam-xam yi,lem xalaati ñi am xel.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da stod ypperstepresten op midt iblandt dem og spurte jesus: svarer du intet på det som disse vidner mot dig?

Wolof

ci kaw loolu saraxalekat bu mag bi taxaw ci seen kanam ne yeesu: «doo tontu? lu la nit ñi di jiiñ?»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

alt er rent for de rene; men for de urene og vantro er intet rent; både deres sinn og deres samvittighet er urene.

Wolof

Ñi sell seen lépp a sell, waaye ñi selladi te gëmadi seen dara sellul, du seeni xalaat, du seeni xel.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

brødre! jeg taler på menneskelig vis. selv en menneskelig pakt vil ingen gjøre til intet eller legge noget til efterat den er stadfestet.

Wolof

bokk yi, maa ngi misaal wax ji ci jëfi doom aadama. xam ngeen ne, kóllëre gu ñu fas ba noppi, waruñu koo fecci, walla ñu ciy rax dara.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

det er intet utenfor mennesket som kan gjøre ham uren når det kommer inn i ham; men det som går ut av mennesket, det er det som gjør mennesket urent.

Wolof

li ci biti, tey dugg nit, du ko man a indil sobe, waaye li génn ci nit, loolu mooy indil nit sobe.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

da vi jo vet dette at vårt gamle menneske blev korsfestet med ham forat synde-legemet skulde bli til intet, så vi ikke mere skal tjene synden;

Wolof

ndegam xam nanu ne, daajoon nañu kirist ca bant ba, xam nanu it ne, jikko ju bon ji nu judduwaale, daajaale nañu ko ak kirist ca bant ba. te yàlla def na loolu, ngir nguuru bàkkaar, gi nekkoon ci sunu yaram tas, nu rëcc ci dooleem.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

han som alene har udødelighet, som bor i et lys som ingen kan komme til, han som intet menneske har sett eller kan se; ham tilhører ære og evig makt. amen.

Wolof

moom kenn a jagoo dund gu sax, dëkk ci biir leer gu kenn mënta jege; moom mi nit musul a gis te nit mënu koo gis. moom kenn a yelloo teraanga ak màggaay ba fàww. amiin.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

alle ting la du under hans føtter. for idet han underla ham alle ting, undtok han intet som ikke er ham underlagt; men nu ser vi ennu ikke at alle ting er ham underlagt;

Wolof

nootal ko lépp, mu teg ci tànk.» bi ko yàlla nootalee lépp nag, bàyyiwul dara. fi mu nekk gisagunu ne, lépp a ngi ci sañ-sañam;

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Norwegian

jeg er blitt en dåre; i har tvunget mig til det. for jeg burde få ros av eder; jeg stod jo ikke i noget tilbake for de såre store apostler, om jeg enn er intet.

Wolof

ci dëgg-dëgg wax naa waxi dof te yéena ma ci dugal, fekk yéen ci seen bopp sax yéena ma waroon a sargal, ndaxte su ma dul dara sax, seen ndaw yooyu ngeen naw ëpplewuñu ma dara.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,318,921 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK