From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
og han sendte sin tjener ut ved den tid nattverden skulde holdes, for å si til de innbudne: kom! for nu er det ferdig.
bi waxtuw lekk jotee mu yónni surga ca ña muy ganale, fàttali leen: “man ngeen a ñëw, ndaxte lépp sotti na léegi.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
da peter vender sig, ser han den disippel følge med som jesus elsket, og som lå op til hans bryst ved nattverden og sa: herre! hvem er det som forråder dig?
piyeer geestu, gis taalibe bi yeesu bëggoon, di ñëw ci seen gannaaw. taalibe boobu mooy ki sóonu woon ca yeesu, ba ñuy lekk, te laajoon ko ne: «boroom bi, kan moo lay wori?»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
da sa han til ham: det var en mann som gjorde en stor nattverd og innbød mange;
yeesu tontu ko ne: «dafa amoon nit ku togglu ay ñam, woo ay nit ñu bare.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: