From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
og han sa: en mann hadde to sønner,
yeesu dellu ne leen: «dafa amoon góor gu am ñaari doom.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
og han tok peter og de to sebedeus' sønner med sig og begynte å bedrøves og engstes.
bi mu waxee loolu, mu ànd ak piyeer ak ñaari doomi sebede, daldi am tiis ba xonett.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
da gikk sebedeus-sønnenes mor til ham med sine sønner, falt ned for ham og bad ham om noget.
ci kaw loolu doomi sebede ya ànd ak seen ndey, ñëw ci yeesu. ndey ja sukk, di ko ñaansi lenn.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
og fordi i er sønner, har gud sendt sin sønns Ånd i våre hjerter, som roper: abba, fader!
gannaaw doomi yàlla ngeen nag, yàlla yónni na xelu doomam ci sunu xol, mu koy wooye nii: «abba,» maanaam «baay.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
- til timoteus, min ekte sønn i troen: nåde, miskunn, fred fra gud fader og kristus jesus, vår herre!
maa ngi lay bind timote, yaw miy sama doomu diine ju wér. na la yàlla baay bi ak kirist yeesu sunu boroom may yiw, yërmande ak jàmm.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: