From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
aos quais respondi que não é costume dos romanos condenar homem algum sem que o acusado tenha presentes os seus acusadores e possa defender-se da acusação.
waaye ma tontu leen ne: “jébbale nit, fekk jàkkaarloowul ak ñi koy jiiñ, ba man a làyyil boppam ci li ñu koy jiiñ, loolu dëppoowul ak aaday nguuru room.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
sinto-me feliz, ó rei agripa, em poder defender-me hoje perante ti de todas as coisas de que sou acusado pelos judeus;
«buur agaripa, ma làyyi ci sa kanam tey ci lépp, li ma yawut yiy jiiñ, xol bu sedd la ci man,
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
e vendo um deles sofrer injustamente, defendeu-o, e vingou o oprimido, matando o egípcio.
noonu mu gis ca ku ñuy néewal doole, mu sotle ko, feyyul ko, ba dóor waayi misra ja.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: