From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
eu, paulo, de meu próprio punho o escrevo, eu o pagarei, para não te dizer que ainda a ti mesmo a mim te deves.
man pool maa ngi lay bind ak sama loxob bopp ne, dinaa la ko fey; bëggumaa yegg ci ne, sag dund sax ci man la jaar!
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
então aquele servo, prostrando-se, o reverenciava, dizendo: senhor, tem paciência comigo, que tudo te pagarei.
kon jaraaf ja daanu ciy tànkam ne ko: “muñal ma, dinaa la fey lépp.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ao anoitecer, disse o senhor da vinha ao seu mordomo: chama os trabalhadores, e paga-lhes o salário, começando pelos últimos até os primeiros.
«bi nga xamee ne timis jot na, boroom tool ba ne jawriñ ja: “woowal liggéeykat yi te fey leen seen bëccëg, tàmbali ci ñi mujj a ñëw, ba ci ñi fi jëkk.”
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: