From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Воздайте ей так, как и она воздала вам, и вдвое воздайте ей по делам ее; в чаше, в которой она приготовляла вам вино, приготовьте ей вдвое.
dellooleen ko li mu defoon, feyleen ko ñaar ci li mu lebaloon, feesal-leen koppam ak naan gu gën a wex ñaari yoon naan ga mu joxe woon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Сколько славилась она и роскошествовала, столько воздайте ей мучений и горестей. Ибо она говорит в сердце своем: „сижу царицею, я не вдова и не увижу горести!"
joxleen ko ci coono ak naqar, lu tollu ni tiitar ak mbuux, ba mu dencaloon boppam. gannaaw nee woon na ci xelam: “maa ngi toog fii ni buur, duma ab jëtun te duma ténj mukk,”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting