From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Все подвижники воздерживаются от всего: те для получения венца тленного, а мы – нетленного.
Ñiy joŋante ci po muy waral tàggat yaram, dañuy xañ seen bopp lu bare. dañu koy def, ngir am kaalag ndam gu dul yàgg; waaye nun danu koy def, ngir am kaalag ndam gu sax ba fàww.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Он слушал говорившего Павла, который, взглянув на него и увидев, что он имеет веру для получения исцеления,
moom nag muy déglu pool miy waare. noonu pool xool ko jàkk, gis ne, am na ngëm ngir wér.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
потому что Бог определил нас не на гнев, но к получению спасения через Господа нашего Иисуса Христа,
ndaxte yàlla jaglewu nu meram, waaye mucc la nu jagleel ndax darajay sunu boroom yeesu kirist.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: