From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
cuando le vieron, le adoraron; pero algunos dudaron
bi ñu gisee yeesu, ñu màggal ko, waaye ñenn ñi am xel ñaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
entonces los que estaban en la barca le adoraron diciendo: --¡verdaderamente eres hijo de dios
Ñi nekk ci gaal gi nag sukk ci kanamam ne ko: «ci dëgg yaa di doomu yàlla ji.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nuestros padres adoraron en este monte, y vosotros decís que en jerusalén está el lugar donde se debe adorar
nun nag, nakajekk sunuy maam ca tund wee ngay séen lañu daan jaamoo yàlla, waaye yéen yawut yi, dangeen ne yerusalem lañu war a jaamoo yàlla.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
los cuatro seres vivientes decían: "¡amén!" y los veinticuatro ancianos se postraron y adoraron
Ñeenti mbindeef ya naan: «amiin.» mag ña sukk di màggal.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
y los veinticuatro ancianos, que estaban sentados en sus tronos delante de dios, se postraron sobre sus rostros y adoraron a dio
Ñaar-fukki mag ak ñeent, ña toogoon ca seen gàngune ca kanam yàlla, daldi dëpp seen jë ca suuf, jaamu yàlla,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
todos los ángeles que estaban de pie alrededor del trono, y de los ancianos y de los cuatro seres vivientes, se postraron sobre sus rostros delante del trono y adoraron a dios diciendo
noonu malaaka yépp taxaw, wër gàngune ma ak mag ña ak ñeenti mbindeef ya. Ñu dëpp seen jë ca kanamu gàngune ma, di jaamu yàlla,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
cuando entraron en la casa, vieron al niño con maría su madre, y postrándose le adoraron. entonces abrieron sus tesoros y le ofrecieron presentes de oro, incienso y mirra
Ñu dugg ca kër ga, gis xale ba ak maryaama ndeyam, ñu daldi sukk, di ko màggal. Ñu ubbi seeni boyetu alal, may ko wurus ak cuuraay ak ndàbb lu xeeñ lu ñuy wax miir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
y he aquí, jesús les salió al encuentro, diciendo: --¡os saludo! y acercándose ellas, abrazaron sus pies y le adoraron
ba ñuy dem nag, yeesu taseek ñoom ne leen: «maa ngi leen di nuyu.» jigéen ña jegesi, laxasu cay tànkam, di ko màggal.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
y adoraron al dragón porque le había dado autoridad a la bestia, y adoraron a la bestia diciendo: "¿quién es semejante a la bestia, y quién puede combatir contra ella?
Ñu jaamu ninkinànka ja ndax li mu joxoon sañ-sañ rab wa, di jaamu it rab wa, naan: «rab wi amul moroom, kenn mënul a xeex ak moom.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting