Results for arrepintieron translation from Spanish to Wolof

Spanish

Translate

arrepintieron

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

y blasfemaron al dios del cielo por sus dolores y sus llagas, pero no se arrepintieron de sus obras

Wolof

ñuy xarab yàllay asamaan ndax seeni metit ak seeni taab. waaye tuubuñu seeni jëf.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

tampoco se arrepintieron de sus homicidios, ni de sus hechicerías, ni de su inmoralidad sexual, ni de sus robos

Wolof

te nit ñooñu tuubuñu seen bóom, seen xërëm, seen njaaloo mbaa seen càcc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los hombres fueron quemados con el intenso calor y blasfemaron el nombre del dios que tiene autoridad sobre estas plagas, pero no se arrepintieron para darle gloria

Wolof

naaj wu metti di lakk nit ñi, ñu daldi xarab turu yàlla, ji am sañ-sañ ci kaw musiba yooyu. waaye tuubuñu sax seeni bàkkaar, ngir jox ko ndam li.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los hombres de nínive se levantarán en el juicio contra esta generación y la condenarán, porque ellos se arrepintieron ante la predicación de jonás. ­y he aquí uno mayor que jonás está en este lugar

Wolof

te it ca bés pénc, waa dëkku niniw dinañu jógandoo ak niti jamono jii, yey leen, ndaxte bi leen yunus waaree, tuub nañu seeni bàkkaar, te ku sut yunus a ngi fii.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los demás hombres que no fueron muertos con estas plagas ni aun así se arrepintieron de las obras de sus manos, para dejar de adorar a los demonios y a las imágenes de oro, y de plata, y de bronce, y de piedra, y de madera, las cuales no pueden ver, ni oír, ni caminar

Wolof

nit ñi rëcc ci musiba yooyu taxul sax ñu tuub seeni jëfi loxo. noppiwuñu di jaamu rab yi ak nataali xërëm yu ñu defare wurus ak xaalis ak xànjar ak xeer ak dénk, yoo xam ne mënuñoo gis, mënuñoo dégg mbaa ñu dox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,938,090,811 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK