Results for capernaúm translation from Spanish to Wolof

Spanish

Translate

capernaúm

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

estas cosas dijo en la sinagoga, cuando enseñaba en capernaúm

Wolof

baat yooyu la yeesu wax, bi mu doon jàngale ca jàngu ba ca kapernawum.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando jesús entró en capernaúm, vino a él un centurión y le rog

Wolof

gannaaw loolu yeesu duggoon na kapernawum. bi mu fa duggee nag, ab njiitu xare fekksi ko. mu ñaan ko,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces descendió a capernaúm, ciudad de galilea, y les enseñaba los sábados

Wolof

gannaaw loolu yeesu dem kapernawum, ab dëkk ca diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando él entró otra vez en capernaúm después de algunos días, se oyó que estaba en casa

Wolof

bi ay fan weesoo, yeesu dellusi dëkku kapernawum, mu siiw ne mu ngi ci kër gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entraron en capernaúm. y en seguida, entrando él en la sinagoga los sábados, enseñaba

Wolof

gannaaw loolu ñu dem kapernawum. ca bésu noflaay nag yeesu daldi dugg ci jàngu bi, di leen jàngal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y habiendo dejado nazaret, fue y habitó en capernaúm, ciudad junto al mar en la región de zabulón y neftalí

Wolof

gannaaw gi, mu toxoo dëkku nasaret, dem dëkk kapernawum, bi féeteek dex ga ci diiwaani sabulon ak neftali.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

después de esto, él descendió a capernaúm con su madre, sus hermanos y sus discípulos; y se quedaron allí no muchos días

Wolof

bi loolu weesoo, mu ànd ak yaayam, ay rakkam ak i taalibeem, dem dëkku kapernawum. waaye yàgguñu fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces, cuando la multitud vio que jesús no estaba allí ni tampoco sus discípulos, ellos entraron en las barcas y fueron a capernaúm buscando a jesús

Wolof

bi mbooloo ma gisee ne, yeesu walla taalibe ya kenn nekkatu fa, ñu dugg ca gaal yooyu, dem seeti ko kapernawum.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

vino, pues, jesús otra vez a caná de galilea donde había convertido el agua en vino. había un oficial del rey cuyo hijo estaba enfermo en capernaúm

Wolof

noonu kon mu dellusi kana ci galile, dëkk ba mu soppe woon ndox ma biiñ. amoon na benn dagu buur bu dëkkoon kapernawum te doomam feebar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando ellos llegaron a capernaúm, fueron a pedro los que cobraban el impuesto del templo y dijeron: --¿vuestro maestro no paga el impuesto del templo

Wolof

gannaaw loolu yeesu ak taalibe ya ñëw kapernawum. bi ñu fa àggee nag, laajkati warugaru kër yàlla ga ñëw ci piyeer ne ko: «ndax seen kilifa du fey posetu ñaari daraxma ngir warugar wi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"y tú, capernaúm, ¿serás exaltada hasta el cielo? ¡hasta el hades serás hundida! porque si entre los de sodoma se hubieran realizado los hechos poderosos que se realizaron en ti, habrían permanecido hasta hoy

Wolof

te yaw dëkku kapernawum, ndax dees na la yékkati bu kawe? déedéet, dees na la daane bu suufe. ndaxte kéemaan yi ma def ci yaw, bu ñu leen defoon ci dëkku sodom, kon mu nekk ba tey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
8,907,199,159 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK