From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
llevaron ante los fariseos al que antes era ciego
noonu ñu daldi indil farisen yi nit ki gumba woon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mientras pasaba jesús, vio a un hombre ciego de nacimiento
amoon na fu yeesu jaaroon, gis fa waa ju judduwaale gumba.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jesús fue a betsaida, y le trajeron un ciego y le rogaban que lo tocase
gannaaw loolu ñu ñëw ci betsayda. foofa ñu indil yeesu ku gumba, di ko ñaan, mu laal ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
desde la eternidad nunca se oyó que alguien abriese los ojos de uno que había nacido ciego
bi àddina sosoo ba tey, musuñoo dégg nit ku ubbi bëti gumbag judduwaale.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dicho esto, escupió en tierra, hizo lodo con la saliva y con el lodo untó los ojos del ciego
bi yeesu waxee loolu ba noppi, dafa daldi tifli, jaxase lor wa ak ban, tay ko ci bëti gumba ga ne ko:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aconteció, al acercarse jesús a jericó, que un ciego estaba sentado junto al camino, mendigando
bi yeesu di agsi dëkku yeriko, am gumba gu toogoon ca wetu yoon wa, di yelwaan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dejadlos. son ciegos guías de ciegos. pero si el ciego guía al ciego, ambos caerán en el hoyo
bàyyileen leen, ay gumba lañu yuy wommat ay gumba; bu gumba dee wommat moroomam nag, kon dinañu daanu ñoom ñaar ci kàmb.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
entonces fue traído a él un endemoniado, ciego y mudo; y le sanó, de manera que el mudo hablaba y veía
booba ñu indil ko ku rab jàpp, mu gumba te luu. yeesu faj ko, ba ku luu ki di wax tey gis.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
¡fariseo ciego! ¡limpia primero el interior del vaso para que también el exterior se haga limpio
farisen yu gumba yi! jëkkleen a setal biir kaas bi ak ndab li, ngir biti bi itam set.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pero algunos de ellos dijeron: --¿no podía éste, que abrió los ojos al ciego, hacer también que lázaro no muriese
waaye am na ca ñoom ñu doon wax naan: «moom mi ubbi bëti gumba gi, ndax mënul woon a fexe ba lasaar du dee?»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
entonces jesús se detuvo y mandó llamarle. llamaron al ciego diciéndole: --ten confianza. levántate. Él te llama
noonu yeesu taxaw, daldi ne: «wooleen ko!» Ñu woo nag gumba gi ne ko: «na sa xel dal! jógal! mu ngi lay woo.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
entonces les dijo una parábola: "¿acaso puede un ciego guiar a otro ciego? ¿no caerán ambos en el hoyo
noonu yeesu wax na leen beneen léeb ne leen: «ndax gumba man na wommat moroomam? mbaa duñu daanu ñoom ñaar ci kàmb?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
así que por segunda vez llamaron al hombre que había sido ciego y le dijeron: --¡da gloria a dios! nosotros sabemos que este hombre es pecador
farisen ya dellu woowaat ka gumba woon ne ko: «waxal sa digganteek yàlla. xam nanu ne, waa joojee boroom bàkkaar la.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
entonces tomando al ciego de la mano, le sacó fuera de la aldea. después de mojarle los ojos con saliva e imponerle las manos, le preguntó: --¿ves algo
yeesu nag jàpp loxob gumba gi, yóbbu ko, ba génn dëkk bi. mu def tiflit ciy bëtam, teg ko loxo naan: «ndax gis nga dara?»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en aquella hora jesús sanó a muchos de enfermedades, de plagas y de espíritus malos; y a muchos ciegos les dio la vista
ca waxtu woowa yeesu wéral nit ñu bare ci seeni feebar ak ci seeni metit, di dàq ay rab tey gisloo ay gumba.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: