Results for david translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

david

Wolof

daawuda

Last Update: 2014-09-21
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

pues, si david le llama señor, ¿cómo es su hijo

Wolof

gannaaw daawuda nag wooye na ko: “boroom bi,” nu muy nekke sëtam?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

Él les dijo: --¿cómo dicen que el cristo es hijo de david

Wolof

noonu yeesu ne leen: «lu tax nit ñi di wax ne, almasi bi mooy sëtu daawuda?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

libro de la genealogía de jesucristo, hijo de david, hijo de abraham

Wolof

lii mooy cosaanu yeesu kirist, sëtu daawuda, sëtu ibraayma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

así que david le llama "señor"; ¿cómo es, pues, su hijo

Wolof

gannaaw daawuda nag wooye na ko “boroom bi,” nu muy nekke sëtam?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

acerca de su hijo--quien, según la carne, era de la descendencia de david

Wolof

di xamle mbirum doomam, yeesu kirist sunu boroom. lu jëm ci meloom ci àddina, ci askanu daawuda la jóge, waaye lu jëm ci xelam mu sell, doomu yàlla la; ndaxte ndekkiteem nekk na firnde ju ràññiku, ne moom la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

hijo de david, hijo de isaí, hijo de obed, hijo de boaz, hijo de salá, hijo de najsón

Wolof

daawuda mooy doomu yese;yese, obedd; bowas; salmon; naason.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

de igual manera, david también proclama la felicidad del hombre a quien dios confiere justicia sin obras

Wolof

noonu la daawuda birale barkeelug nit ki yàlla jagleel njub, fekk ay jëfam taxul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

a una virgen desposada con un hombre llamado josé, de la casa de david. el nombre de la virgen era maría

Wolof

mu yebal ko ca janq bu ñu may waa ju bokk ci askanu daawuda te ñu koy wax yuusufa, waaye àndaguñu. janq baa ngi tudd maryaama.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

Éste será grande, y será llamado hijo del altísimo; y el señor dios le dará el trono de su padre david

Wolof

ku màgg lay nekki, te dinañu ko wooye doomu aji kawe ji. boroom bi yàlla dina ko jébbal nguuru daawuda maamam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

"después de esto volveré y reconstruiré el tabernáculo de david, que está caído. reconstruiré sus ruinas y lo volveré a levantar

Wolof

“boroom bi nee na:gannaaw loolu dinaa dellusi,te yékkati këru daawuda, gi ne tasar,dinaa defar toj-toj ya,ba taxawalaat ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

porque el mismo david dice en el libro de los salmos: dijo el señor a mi señor: "siéntate a mi diestra

Wolof

ndaxte daawuda moom ci boppam moo ne ci sabóor:“boroom bi nee na sama boroom:‘toogal ci sama ndeyjoor,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

los que iban delante le reprendían para que se callase, pero él clamaba con mayor insistencia: --¡hijo de david, ten misericordia de mí

Wolof

Ñi jiitu woon gëdd ko, ngir mu noppi. waaye muy gën a yuuxu naan: «sëtu daawuda, yërëm ma!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

david mismo le llama "señor"; ¿cómo es, pues, su hijo? y la gran multitud le escuchaba con gusto

Wolof

gannaaw daawuda nag wooye na ko: “boroom bi,” naka mu nekke sëtam?» noonu mbooloo mu mag mi di ko déglu ak bànneex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

entonces josé también subió desde galilea, de la ciudad de nazaret, a judea, a la ciudad de david que se llama belén, porque él era de la casa y de la familia de david

Wolof

yuusufa nag daldi jóge nasaret ca diiwaanu galile, jëm ca diiwaanu yude ca betleyem, dëkk ba daawuda cosaanoo, ndaxte ci askanu daawuda la bokk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

"hermanos, era necesario que se cumpliesen las escrituras, en las cuales el espíritu santo habló de antemano por boca de david acerca de judas, que fue guía de los que prendieron a jesús

Wolof

mu ne leen: «bokk yi, li xel mu sell mi waxoon ci mbind mi jaarale ko ci gémmiñu daawuda, fàww mu am. waxoon na ci mbirum yudaa, mi wommat ñi jàpp yeesu

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

"yo, jesús, he enviado a mi ángel para daros testimonio de estas cosas para las iglesias. yo soy la raíz y el linaje de david, la estrella resplandeciente de la mañana.

Wolof

«man yeesu maa yónni sama malaaka, ngir mu seede leen mbir yii ci digg mboolooy ñi gëm. man maay car, bi soqikoo ci daawuda, di biddiiwu njël bu leer bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

y he aquí dos ciegos estaban sentados junto al camino, y cuando oyeron que jesús pasaba, clamaron diciendo: --¡señor, hijo de david, ten misericordia de nosotros

Wolof

fekk ñaari gumba toog ci wetu yoon wa. bi gumba ya déggee ne, yeesu di jaar, ñu daldi yuuxu ne ko: «sang bi, yaw sëtu daawuda bi, yërëm nu!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Spanish

"escribe al ángel de la iglesia en filadelfia: el santo y verdadero, el que tiene la llave de david, el que abre y nadie cierra, y cierra y nadie abre, dice estas cosas

Wolof

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku filadelfi, ne ko: i aji sell ji, di aji dëgg ji nee na, moom mi yor caabiy daawuda ji, moom miy tijji te kenn du ko man a tëj, muy tëj te kenn du ko tijji nee ne:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia
Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,774,329,792 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK