Results for despedida translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

entonces, una vez despedida la gente, subió en la barca y se fue a las regiones de magdala

Wolof

noonu yeesu yiwi mbooloo mi, dugg ci gaal, ñëw ci wàlli magadan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

una vez despedida la gente, subió al monte para orar a solas; y cuando llegó la noche, estaba allí solo

Wolof

bi mu ko yiwee nag, mu yéeg ca tund wa, ngir wéet ak yàlla. noonu guddi jot, fekk mu nekk fa moom rekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces una vez despedida la congregación, muchos de los judíos y de los prosélitos piadosos siguieron a pablo y a bernabé, quienes les hablaban y les persuadían a perseverar fieles en la gracia de dios

Wolof

te bi mbooloo ma tasee, ay yawut yu bare ak ñi tuuboon ci yoonu yawut te ragal yàlla, topp ci pool ak barnabas. Ñuy diisoo ak ñoom, di leen xiir, ñu wàkkirlu ci yiwu yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces, una vez despedida la multitud, volvió a casa. y sus discípulos se acercaron a él diciendo: --explícanos la parábola de la cizaña del campo

Wolof

ci kaw loolu yeesu bàyyi mbooloo ma, dugg ca kër ga. taalibeem yi ñëw ci moom ne ko: «firil nu léebu jëmb, bi sax ci tool bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

después de pasar allí algún tiempo, fueron despedidos en paz por los hermanos para volver a los que los habían enviado

Wolof

bi loolu amee ñu toog fa ab diir, ba noppi bokk yi yiwi leen ci jàmm, ñu dellu ca ña leen yónni woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,793,918,107 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK