Results for dios te bendiga translation from Spanish to Wolof

Spanish

Translate

dios te bendiga

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

que dios te bendiga

Wolof

Last Update: 2023-11-03
Usage Frequency: 2
Quality:

Spanish

pero ahora también sé que todo lo que pidas a dios, dios te lo dará

Wolof

waaye xam naa ne, fii nu tollu sax, loo ñaan yàlla, mu may la ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

¿o menosprecias las riquezas de su bondad, paciencia y magnanimidad, ignorando que la bondad de dios te guía al arrepentimiento

Wolof

ndax dangaa xeeb mbaaxu yàlla, mi yéex a mer te di la muñal? xanaa xamuloo ne, yàllaa ngi lay won baaxaayam, ngir nga réccu say bàkkaar?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y me dijo: "no temas, pablo. es necesario que comparezcas ante el césar, y he aquí dios te ha concedido todos los que navegan contigo.

Wolof

mu ne ma: “pool bul tiit; fàww nga taxaw ci kanamu sesaar, te yaa tax yàllay aar bakkani ñi nga àndal ñépp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

el fariseo, de pie, oraba consigo mismo de esta manera: 'dios, te doy gracias que no soy como los demás hombres: ladrones, injustos, adúlteros, ni aun como este publicano

Wolof

farisen baa nga taxaw di ñaan ci xelam naan: “yaw yàlla, maa ngi lay sant ci li ma melul ni ñeneen ñiy sàcc, di def lu jubadi te di njaaloo, rawatina juutikat bii.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,647,202,774 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK