Results for el señor es mi pastor translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

pero el que se une con el señor, un solo espíritu es

Wolof

waaye nag kuy ànd ak boroom bi, xel yi dañuy booloo, nekk benn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hay también diversidad de ministerios, pero el señor es el mismo

Wolof

am na ay sas yu bare, waaye benn boroom bi la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero el que se gloría, gloríese en el señor

Wolof

waaye ni ko mbind mi waxe: «kuy damu, na damu ci boroom bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque del señor es la tierra y su plenitud

Wolof

ndaxte mbind mi nee na: «Àddina ak li ci biiram lépp, boroom bi moo ko moom.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hijos, obedeced en el señor a vuestros padres, porque esto es justo

Wolof

naka yéen xale yi, nangeen déggal seeni waajur, ci li ngeen bokk ci boroom bi, ndaxte looloo rafet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y ellos dijeron: --porque el señor lo necesita

Wolof

Ñu tontu ne: «ndaxte boroom bi da koo soxla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

considera bien lo que digo, pues el señor te dará entendimiento en todo

Wolof

xalaatal bu baax sama wax jii, ndax boroom bi dina leeral sa xel ci lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el señor jesucristo sea con tu espíritu. la gracia sea con vosotros

Wolof

na boroom bi aar sa xel. na yiwu yàlla ànd ak yéen ñépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

de manera que podemos decir confiadamente: el señor es mi socorro, y no temeré. ¿qué me hará el hombre

Wolof

ba tax nu am kóoluteg wax ne:«boroom bi moo di sama ndimbal;duma ragal dara.lu ma nit manal?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

dice el señor que hace estas cosas, que son conocidas desde la eternidad

Wolof

man dinaa def loolu, man boroom bi ko wax,te ca njàlbéen ba tey ma di ko xamle.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

bienaventurado el hombre a quien el señor jamás le tomará en cuenta su pecado

Wolof

ki boroom bi sëful ay bàkkaaram,kooka ku barkeel la.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

así también ordenó el señor a los que anuncian el evangelio, que vivan del evangelio

Wolof

naka noonu it boroom bi digle na ne, ñiy yégle xebaar bu baax bi, nanu ci dund.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hijos, obedeced a vuestros padres en todo, porque esto es agradable en el señor

Wolof

xale yi, déggal-leen seeni waajur ci lépp, ndaxte looloo rafet ci ñi bokk ci boroom bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

ahora bien, cuando venga el señor de la viña, ¿qué hará con aquellos labradores

Wolof

noonu yeesu laaj leen: «bu boroom tool bi ñëwee nag, na muy def beykat yi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

--bendito sea el señor, dios de israel, porque ha visitado y redimido a su pueblo

Wolof

«cant ñeel na boroom bi, yàllay israyil,ndaxte wallusi na mbooloom, ba jot leen!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

jesús le respondió: --el primero es: escucha, israel: el señor nuestro dios, el señor uno es

Wolof

noonu yeesu tontu ko ne: «bii: “bànni israyil, déglul! yàlla sunu boroom moom rekk mooy buur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque nuestra ciudadanía está en los cielos, de donde también esperamos ardientemente al salvador, el señor jesucristo

Wolof

waaye nun waa asamaan lanu, te noo ngi xaar boroom bi yeesu kirist jóge fa, musalsi nu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

más bien, deberíais decir: "si el señor quiere, viviremos y haremos esto o aquello.

Wolof

lii kay ngeen waroon a wax: «bu soobee boroom bi, dinanu dund, tey def nàngam ak nàngam.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

pero respondiendo el señor le dijo: --marta, marta, te afanas y te preocupas por muchas cosas

Wolof

boroom bi tontu ko ne: «màrt, màrt, yu baree ngi fees sa xol, nga am ay téq-téq ndax loolu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando entró a donde ella estaba, dijo: --¡te saludo, muy favorecida! el señor está contigo

Wolof

malaaka ma dikk ca moom ne ko: «jàmm ngaam, yaw mi boroom bi defal aw yiw; mu ngi ak yaw.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,780,073,293 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK