Results for enviado translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

hubo un hombre, enviado por dios, que se llamaba juan

Wolof

yàlla yónni woon na nit ku ñu naan yaxya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

así como tú me enviaste al mundo, también yo los he enviado al mundo

Wolof

ni nga ma yónnee àddina, noonu laa leen yónnee ci nit ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y nosotros hemos visto y testificamos que el padre ha enviado al hijo como salvador del mundo

Wolof

te nun gis nanu te seede ne, baay bi yónni na doom ji, mu nekk musalkatu àddina.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero a ninguna de ellas fue enviado elías, sino a una mujer viuda en sarepta de sidón

Wolof

moona yàlla yónniwul iliyas ci kenn ci ñoom, waaye mu yebal ko ci jigéen ju jëkkëram faatu, ju dëkk sarebta, ca wetu sidon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

en el sexto mes, el ángel gabriel fue enviado por dios a una ciudad de galilea llamada nazaret

Wolof

bi elisabet nekkee ci juróom-benni weeram, yàlla yónni na malaakaam jibril ca dëkku nasaret ca diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

así que hemos enviado a judas y a silas, los cuales también os confirmarán de palabra el mismo informe

Wolof

yónni nanu nag yudd ak silas, ñu di leen xamal xebaar boobu ci seen gémmiñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

después de pasar allí algún tiempo, fueron despedidos en paz por los hermanos para volver a los que los habían enviado

Wolof

bi loolu amee ñu toog fa ab diir, ba noppi bokk yi yiwi leen ci jàmm, ñu dellu ca ña leen yónni woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

respondió jesús y les dijo: --Ésta es la obra de dios: que creáis en aquel que él ha enviado

Wolof

yeesu tontu leen ne: «jëf ji neex yàlla, moo di gëm ki mu yónni.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

dios ha enviado un mensaje a los hijos de israel, anunciando las buenas nuevas de la paz por medio de jesucristo. Él es el señor de todos

Wolof

yónnee na kàddoom bànni israyil, di leen xebaar jàmm, jaarale ko ci yeesu kirist, miy boroom lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

después de los tres días y medio el aliento de vida enviado por dios entró en ellos, y se levantaron sobre sus pies. y un gran temor cayó sobre los que los veían

Wolof

waaye bi ñetti fan ya ak genn-wàll wéyee, xelum dund, jóge ca yàlla, solu leen, ñu jóg taxaw. noonu tiitaange gu réy jàpp ñi leen doon seetaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces jesús les dijo otra vez: "¡paz a vosotros! como me ha enviado el padre, así también yo os envío a vosotros.

Wolof

yeesu dellu ne leen: «na jàmm wàcc ci yéen! ni ma baay bi yónnee, noonu laa leen di yónnee, man itam.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

pero yo tengo un testimonio mayor que el de juan; porque las obras que el padre me ha dado para cumplirlas, las mismas obras que hago dan testimonio de mí, de que el padre me ha enviado

Wolof

«waaye yor naa ci man seede su gën a mag si ma yaxya di seedeel: maa ngi def jëf, yi ma baay biy sant. jëf yooyu may def nag ñooy seede ne, baay bi moo ma yónni.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el espíritu del señor está sobre mí, porque me ha ungido para anunciar buenas nuevas a los pobres; me ha enviado para proclamar libertad a los cautivos y vista a los ciegos, para poner en libertad a los oprimido

Wolof

«xelum boroom baa ngi ci man,ndaxte moo ma tànn,ngir ma yégal néew doole yi xebaar bu baax bi.dafa maa yónni,ngir ma yégal jaam ñi ne, dinañu leen goreel,yégal gumba yi ne, dinañu gis,te jot ñi ñu noot,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"yo, jesús, he enviado a mi ángel para daros testimonio de estas cosas para las iglesias. yo soy la raíz y el linaje de david, la estrella resplandeciente de la mañana.

Wolof

«man yeesu maa yónni sama malaaka, ngir mu seede leen mbir yii ci digg mboolooy ñi gëm. man maay car, bi soqikoo ci daawuda, di biddiiwu njël bu leer bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

entonces pedro, al volver en sí, dijo: "ahora entiendo realmente que el señor ha enviado su ángel y me ha librado de la mano de herodes y de toda la expectación del pueblo judío.

Wolof

bi xelam dellusee ci moom piyeer ne: «léegi xam naa ci lu wóor ne, boroom bi yónni na malaakaam, musal ma ci loxoy erodd ak li ma yawut ya yéene woon lépp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

al que venza, yo le haré columna en el templo de mi dios, y nunca jamás saldrá fuera. y escribiré sobre él el nombre de mi dios, y el nombre de la ciudad de mi dios--la nueva jerusalén que desciende del cielo, enviada por mi dios-- y mi nombre nuevo

Wolof

ku daan, dinaa la samp ni aw jënu néeg ci sama kër yàlla te doo fa génn mukk. dinaa bind ci yaw turu sama yàlla ak turu dëkku sama yàlla, mu di yerusalem gu bees, giy jóge ca asamaan ca wetu sama yàlla di wàcc. dinaa bind it ci yaw sama tur wu bees.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,773,244,910 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK