From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
estad siempre gozosos
deeleen bég
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gozosos en la esperanza, pacientes en la tribulación, constantes en la oración
bégleen ci yaakaaru ëllëg te muñ bépp tiis, di sax ci ñaan yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
como entristecidos, pero siempre gozosos; como pobres, pero enriqueciendo a muchos; como no teniendo nada, pero poseyéndolo todo
danuy dékku tiis, waaye di bég fu nu tollu. nu tumurànke, waaye di woomal ñu bare; amunu dara, fekk noo moom lépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
al regresar jesús, toda la gente le recibió gozosa, porque todos le esperaban
bi yeesu dëppee dellu, mbooloo ma di ko teeru, ndaxte ñépp a ngi ko doon xaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: