Results for gracias a dios translation from Spanish to Wolof

Spanish

Translate

gracias a dios

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

¡gracias a dios por su don inefable

Wolof

jërë-jëfati yaw yàlla ndax sa may googu weesu dayo!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

doy gracias a mi dios cada vez que me acuerdo de vosotros

Wolof

yoon wu ma leen di xalaat, maa ngi sant yàlla sama boroom;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

doy gracias a dios que hablo en lenguas más que todos vosotros

Wolof

maa ngi sant yàlla ci li may wax ay làkk, ba raw leen yéen ñépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

gracias a dios que puso en el corazón de tito la misma solicitud por vosotros

Wolof

cant ñeel na yàlla, moom mi def ci xolu tit cawarte gu mel ni sunu gos ci yéen!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

doy gracias a dios que no bauticé a ninguno de vosotros, sino a crispo y a gayo

Wolof

maa ngi sant yàlla ci li ma sóobul kenn ci yéen, ku dul kirispus ak gayus,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

damos gracias a dios, el padre de nuestro señor jesucristo, orando siempre por vosotros

Wolof

dunu noppee sant yàlla, baayu sunu boroom yeesu kirist, saa su nu leen di ñaanal,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

damos siempre gracias a dios por todos vosotros, haciendo mención de vosotros en nuestras oraciones

Wolof

bët bu set nu ngi sant yàlla ndax yéen, di leen boole ci sunuy ñaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

habiendo dicho esto, tomó pan, dio gracias a dios en presencia de todos y partiéndolo comenzó a comer

Wolof

bi mu waxee loolu, mu fab mburu, sant yàlla ci kanamu ñépp, damm ko, daldi ko lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pues les oían hablar en lenguas y glorificar a dios

Wolof

ndaxte dégg nañu leen, ñuy wax yeneeni làkk ak di màggal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

esto, para que seáis enriquecidos en todo para toda liberalidad, la cual produce acciones de gracias a dios por medio de nosotros

Wolof

noonu dingeen woomle ci lépp, ba yéwén ci bépp anam, ba tax ñu bare gërëm yàlla ndax li ngeen maye jaarale ko ci nun.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

no hay quien entienda, no hay quien busque a dios

Wolof

amul kenn ku xam yëfi yàlla,mbaa kenn ku koy wut.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el que no ama no ha conocido a dios, porque dios es amor

Wolof

ku bëggul sa mbokk, xamuloo yàlla, ndax yàlla mbëggeel la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

no con bajas pasiones, como los gentiles que no conocen a dios

Wolof

te xemmem bañ leen a jiital, ni xeeti àddina yi xamul yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"bienaventurados los de limpio corazón, porque ellos verán a dios

Wolof

yéen ñi am xol bu sell, barkeel ngeen,ndax dingeen gis yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

puso las manos sobre ella, y al instante se enderezó y glorificaba a dios

Wolof

noonu mu teg ko ay loxoom, soxna sa siggi ca saa sa, di màggal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

gracia a vosotros y paz de parte de dios nuestro padre y del señor jesucristo

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 4
Quality:

Spanish

al oír de nosotros, los hermanos vinieron hasta la plaza de apio y las tres tabernas para recibirnos. pablo, al verlos, dio gracias a dios y cobró ánimo

Wolof

sunuy xebaar law na, ba egg ca bokk ya fa dëkk, noonu ñu gatandu nu ba ca péncu apiyus ak bérab bu ñuy wax Ñetti añukaay ya. bi leen pool gisee, mu sant yàlla, daldi takk fitam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

en esto sabemos que amamos a los hijos de dios, cuando amamos a dios y guardamos sus mandamientos

Wolof

xam nanu ne, bëgg nanu doomi yàlla yi ci lii: bëgg yàlla tey sàmm ay ndigalam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

al oírle, todo el pueblo y los publicanos justificaron a dios, siendo bautizados con el bautismo de juan

Wolof

nit ñépp ñi doon déglu yeesu, ba ci juutikat yi sax, dëggal nañu ne yàlla ku jub la, ndaxte nangu nañu yaxya sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

--¡gloria a dios en las alturas, y en la tierra paz entre los hombres de buena voluntad

Wolof

«nañu màggal yàlla ca asamaan su kawe sa,te ci àddina, na jàmm ji wàcc ci nit, ñi mu nangu ndax yiwam!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,655,638,345 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK