From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
todas vuestras cosas sean hechas con amor
lépp li ngeen di def, defleen ko ak mbëggeel.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
no obstante, el altísimo no habita en casas hechas por mano, como dice el profeta
«moona aji kawe ji du dëkk ci fu loxol nit defar; moom la ab yonent wax ne:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pero el que hace la verdad viene a la luz para que sus obras sean manifiestas, que son hechas en dios
waaye ku def lu jub day ñëw ci leer gi, ngir ñu xam ne, def na ay jëfam ci kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
extiende tu mano para que sean hechas sanidades, señales y prodigios en el nombre de tu santo siervo jesús.
tàllalal sa loxo, ci wéral ak ci wone ay kéemaan ak ay firnde, jaarale ko ci turu yeesu, sa ndaw lu sell li.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
de modo que si alguno está en cristo, nueva criatura es; las cosas viejas pasaron; he aquí todas son hechas nuevas
kon bu nit bokkee ci kirist, mbindeef mu bees la. li jëkk wéy na, lu bees a fi teew.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: